El Hadj N'Diaye - Yu sew yii Lyrics

Lyrics Yu sew yii - El Hadj N'Diaye



Yu sew yug ma tábaal mba ma miin ko
Gna dem bàyyi ma
Sa yu sew yi yugg ma tábaal mba miim lén
Bul dem báyyima
Allé li li l3e l3
Taatou garapp bagn dan fex lo
Dan ko woowe garapp mbëggel
Tooto ya julatuñu dom
Taatou garapp bagn dan fex lo
Dan seede suñu mbëggel
Tooto ya julatuñu dom
Waaxtu yi gna xamni xalaat yi dagni jáxaaso
Waaxtu yi gna xamni xol yi benn lañi Don
Waaxtu yi gna xamni gën ci xaliit gnay doon
Waaxtu yi gna xamni maay bagn gaay naggu
Mani kay nene tuti kay
Yoon wagn dòn jálle
Jaargooy lënë nako
Salaan wa mo ñi jooy weet
Yoon wagn dòn jálle
Jaargooy lënë
Rángnooy wa moñi walagan
Diggante gooney gi yákaar nani noon yaffa
Jaar
Tool bi numu dan meeñe
Ak tay gni numu geede
Jeeren ya jaar nagnu fa
Mani yaw mi degglu ma
Yaw táss katúu yákaar bi
Siggil xool assaman moom moogni jooy
Yu sew sew sew yu ne ma miin na miin
Bul dem báyyima (2)
Yu sew sew sew yu ma miin
Bul dem báyyima




El Hadj N'Diaye - Xel
Album Xel
date of release
08-06-2001




Attention! Feel free to leave feedback.