Lyrics Antidote - Elzo Jamdong
Yeah
eh
Yeah
eh
Yeah
Nenegn
ma
africain
khamoul
louy
job
Africain
dou
degg
loudoul
ay
dore
Maam
yi
toubab
yi
done
diapp
niouy
dow
Mo
dess
souniou
gene
yi
niouy
dakhanté
thioy
yi
Africain
dioubeuleul
mouné
dey
diadd
Africain
couvre
feu
sakh
mounoul
toke
Africain
lane
mo
ko
téré
mou
takk
Te
africain
beuri
neu
diamant
ak
or?
Africain
diot
neu
niou
gueum
souniou
bopp
Gueum
souniou
bopp
samm
souniou
bopp
Africain
diot
neu
niou
arr
souniou
bopp
Kou
beugg
deukk
tchi
ay
boum
niou
topp
Yeah
Febar
bi
kass
dou
ko
dog
Hun
Febar
yagg
neu
lol
Yeah
Yagg
negn
bakhal
ay
khop
Wayé
khamagougn
kagn
leniouy
guenneu
tchi
ndol
Professeur
diangal
ma
loutakh
politiq
bi
tamm
niou
note
Monsieur
le
geologue
gaz
bi
ak
petrole
bi
kane
moko
mom?
Jamono
Scholcher
beu
legui
niouy
nakhanté
ak
Babylone
Teranga
amoul
tchi
jungle
bi
Gaindé
dou
baal
Antilope
Professeur
diangal
ma
loutakh
politiq
bi
tamm
niou
note
Monsieur
le
geologue
gaz
bi
ak
petrole
bi
kane
moko
mom?
Tôt
ou
tard
dinegn
leu
taggué
ki
leu
takkal
seu
antimort
Diogueundo
liguey
tchi
fouleu
kessé
moye
souniou
antidote
Yagg
neu
thiole
wayé
beuss
dineu
chill
Yagg
neu
pire
wayè
biss
di
neu
mole
Yagg
neu
thiole
wayè
gueum
nani
beuss
dineu
chill
Yagg
neu
pire
wayé
gueum
nani
biss
di
neu
mol
Africain
bala
ngay
teub
di
jubiler
victoire
bi
neu
worr
Bo
naré
wolou
kepp
kou
leu
signe
rek
ngaaka
ngay
done
Africain
bala
ngay
tal
fetch
kholeul
noy
moyto
seu
none
Africain
bala
ngay
tal
fetch
kholeul
noy
moyto
seu
none
Yagg
neu
thiole
wayé
beuss
dineu
chill
Yagg
neu
pire
wayè
biss
di
neu
mole
Yagg
neu
thiole
wayè
gueum
nani
beuss
dineu
chill
Yagg
neu
pire
wayé
gueum
nani
biss
di
neu
mol
Africain
bala
ngay
teub
di
jubiler
victoire
bi
neu
worr
Bo
naré
wolou
kepp
kou
leu
signe
rek
ngaaka
ngay
done
Africain
bala
ngay
tal
fetch
kholeul
noy
moyto
seu
none
Africain
bala
ngay
tal
fetch
kholeul
noy
moyto
seu
none
Yeaaahh
Yeah
yeah
Yeaaahh
Yeah
yeah
Deugueuleu
sunu
rew
mi
Tiono
gou
nek
watia
nafi
Mbadial
bounek
watia
na
si
rew
mi
Wayé
lolou
gnoune
gno
tchi
wara
takhaw
Dou
keneu
Gnoune
dong
nio
tchi
wara
meuneu
takhaw
Suñu
Mame
Kocc
Barma
néna
Sou
feketani
bou
nga
reey
ap
gor
Dé
ko
diokh
souba
gou
djote
loumouy
doundé
Bou
yagué
Nga
sopi
ko
mala
Attention! Feel free to leave feedback.