Lyrics RBG - Elzo Jamdong
Yeah
Rappel
bou
gatt
RBG
Yeah
Yow
Bi
may
ndieukk
degg
sama
baat
radio
Dou
wone
dara
tchi
mane
Khawma
wone
maa
ngui
tchi
révolution
ni
Sarafina
Bo
woutek
gayi
do
faalé
li
ga
yi
diappé
lou
mak
Mane
fesseul
Sorano
ak
Comedy
Club
diaakhalouma
Meuss
naa
am
dolé
bou
touti
def
ay
bakar
you
mak
Ragal
dou
takh
meu
diakarlok
toubab
di
plaider
coupable
Mane
leu
domou
Cheikh
Anta
di
rakkou
Amaru
Pac
Toke
8eme
assamaanou
rap
tchi
bassang
farankoulaay
Sama
pappeu
fekké
woul
meu
nekk
papp
tchi
rap
bi
di
gérer
Boy
yi
di
langg
ni
rapide
deumm
yi
doum
ma
digérer
Fadj
naaleu
maay
yor
garap
bi
kham
nga
ni
peudo
bi
cheré
Shit
bi
dou
lamb
pharmacie
fayougn
ma
cachet
ma
wéré
Daaw
ba
ren
Free
raw
nele
Gni
maa
naan
thiaw
nga
leen
te
pourtant
kaaw
nga
ne
Se
son
yi
graaw
ne
mais
ni
nga
percer
gaaw
neu
dé
Degn
khamoul
fima
diaar
yeupp
ak
li
ma
kaaw
tchi
brain
yeah
Thiaatou
gallé
may
taaw
tchi
game
bi
Mere
daf
ma
eumb
adji
macca
faw
ma
yèmé
Motakh
ma
toudd
alladji
takh
level
bi
adiou
Deggoumeu
peul
mais
alla
athiou
rek
laa
kham
tchi
liguey
bi
Mang
tchi
town
bi
di
make
Walla
nekk
kaaw
beu
di
tape
Boy
degg
son
bi
di
béég
Boy
degg
dope
bi
di
yeeg
Yeksi
songuidji
Trace
Légui
yobou
son
yi
beu
states
BET
Oh
my
God
Te
touddoumeu
Oumy
Gueye
di
Boulene
meu
comparek
niouy
kharr
meu
def
niou
sogueu
def
C′est
une
manière
polie
de
dire
que
dagn
may
topando
Dama
guenné
roy
thi
mom
samay
morom
di
roy
thi
mane
Leader
conscient
mel
ni
Pape
Diouf
lane
laa
tchi
meun
Ma
ndieukkeu
songg
théâtre
Mandieukkeu
entrée
ten
taw
Ma
ndieukkeu
guenné
album
Diokhaat
leen
ma
respect
Fall
Ma
ndieukkeu
nekk
deezer
Ndieukkeu
nekk
pé
wou
deezer
Ma
ndieukk
niaf
album
bi
tchi
bracelets
you
wèèkh
talleu
Rappel
bou
gatt
Pour
rappeur
yeupp
tedj
sene
gat
Tek
lene
sene
taat
tchi
chaise
bi
rek
te
tok
setane
Tamm
tekk
spectacle
deugg
ndakh
begn
fenkat
Diaroul
indi
yarkatou
khar
pour
kham
ni
maay
sene
goat
Energie
bi
gay
def
pour
certifier
thi
seu
compte
Li
gueunone
moye
nga
use
ko
pour
fesseul
seu
compte
bancaire
Sou
dé
yone
bi
nguene
beugg
dieul
nak,
commencez
sans
moi
Soumeu
démé
di
nguene
comprendre
nak
comment
c'est
sans
moi
Boy
yaa
ngui
péter
ay
cables
te
amunu
hit
Begg
dund
ci
seen
art
fekk
xamu
ñu
nix
Deñ
ma
bègg
jail
ndaxte
ni
ma
koy
defe
mo
free
Maxalla
dama
yagg
brancher
mel
ni
téléphone
fixe
Sama
junky
yang
tchi
niakh
bi
comme
ay
Teletubbies
DIPSY
MC
yaa
ngui
kheekh
di
signe
mel
ni
Election
miss
Nigga
todiou
leen
fen,
bayilene
fenn
(baayileen
fen)
Mane
dama
doff
motakh
maa
leen
eupp
Fann
Engagé
naa
sans
youkhou
France
dégage
Lekk
naa
cachet
orange,
lekk
naa
cachet
Eiffage
Assiko
vie
d′château
Antidote
France24
Même
sou
ma
yoroul
call
Sama
son
yi
am
neu
message
Ngané
yaa
ko
tangal,
hun?
maay
ki
ley
calmer
(Maay
ki
ley
fey)
Maay
fey
seu
takk,
founiou
tassé
nga
almette
Manqui
club
mangui
2s
Tv
projets
yi
dal
neu
Maay
seu
pappe
diaay
naa
samay
CD
mbedd
mi
fall
meu
Free
eazy
Attention! Feel free to leave feedback.