Elzo Jamdong - Tchi Kow Lyrics

Lyrics Tchi Kow - Elzo Jamdong



Yeeehah
Ioe bimae ndieuk guiss sama clip télé dou wone dara ci man
Xaw ma wone mangui ci Révolution ni sarafina
Bo néké kaw ken dou diap yangui rabati sax
Yeh mic bi nice anh!
anh
Ioe bimae ndieuk degg sama bat radio dou wone dara ci man
Xaw ma wone mangui ci Révolution ni sarafina
Bo deukei town dagne lay gueum lo ni do dara ci rap
Tegone ni boy yi beug dadialé ay thiaga di naw
Kén momoul kén kén eupeulé wou ken dara ci len
Bou kén xep kén ngueum ngueum ak wara fi
Xam na ay galsen you meussoul dougou car rapide sax
Diaxlé nga khat diapal ni mangui doga tambali nak
Rappeur yi diougué bitim rew douma sen morom
Dou louma doundou wara xam ni culture bi amoul borom
Dou cana bi wala kaw man bi yi thi eupeulé waleu
Dou canabiss dou co virus leu bougnou ko walé
Anh




Elzo Jamdong - Freeseason
Album Freeseason
date of release
31-08-2015




Attention! Feel free to leave feedback.