Elzo Jamdong - Zero Garantie Lyrics

Lyrics Zero Garantie - Elzo Jamdong



Yeah, yeahh...
Yow nioungui si yoonu wout ba légui
Khamougnou kagn lagnouy noppalou
Yeah...
Défna ay ndiaakhoum homie (défna ay ndiaakhoum)
Homie défna ay ndiaakhoum dolli (Défna ay ndiaakhoum dolli)
Moytoulma wadiou geuneu meuneu noppi ndakh
défkat dou aalou homie (Défkat dou aalou homie)
Défkat dou aalou homie (Non, non)
Mani défkat dou aalou homie (Défkat dou aalou homie)
Town dangay waarou homie, pourtant khalna lou bakh ak lou bakhoul
Kogn bima maggué, tééla guiss business
Léga bi dokhoul no déf bari vitess




Elzo Jamdong - Macina
Album Macina
date of release
29-06-2018




Attention! Feel free to leave feedback.