Elzo Jamdong - Baayi Ma Lyrics

Lyrics Baayi Ma - Elzo Jamdong



Adounaa sobè laa
sobè laa hahaha
kou xeuthio ak mome mou fowè la
fawèla hahaha
teudj naniouma thi casso mangui dièma reuthie
dièma fèy bagna lab thi guèdjou lundeume
deugueur bope takh lougne ma tèrè ma dieuff
di dèglou bakane lou guène ma dieunde
mangui thi yone bi di zigzag di zigzaaag
woutè na ak niom yonduntè yalla Isaac
mangui thi yone bi di zigzag di zigzag
kou dèm nani kanè mouno wothie bissapp
mane sama beugg beugg moy sama natou
moma takha naw lake sama kérosène
moma takha ware gnima diokhone sama kadou
ak show yi nieuke xam sama sokhna fima...
en
iow yaye mane mane maye iow
loma deff lo dama bopp lako deff
iow yeye kane iow ya bone
nimala sekhlo nonou lala abonné
lingua ma dioume lo yeupp xamna ni yako teyy
nèwone na soma beuguetè dièguèti dinako bagne
linguama dioume lo yeupp xamna ni yako
teyy nga nekk sama bir xel nanema xana ammo xel
nga meyma baath tègu ma paka thi poute
ndandena dangua ma beugg diappè ngaka thi pète
mane damala tope sama bope di mèti,
kène dou wèdini koula sopp deukkè sopp di wèdi
ya takh ma pouce wakhtou diouli yima tayelone diogg
iow yama takha dioylo djiguène yima nobb
nga nekk thi sama bopp dima dey may moy
bala may dièguissi ragg nga gueune ma taggaliko ak iow
bayima (bayima) bayima (bayimaa) iow bayima
(eh èè) iow bayima ma bayila nga bayima (yeah)
nga bayima (bayimaa) nga bayima ma bayila
addounaa sobèlaa sobèlaaahahaha
kou rawantè ak mom deff faux départ (faux départ hahaha)
ma nètalila sama guinte guii
kouko guinte do beugg guintetii
kouko guinte do beugg guènetii
makk iow beugg cèy walla dem toukii
cèytanè dafma beuggone dampe ni liire ak mame
mou deff ma diame naar ma takk thi biirr ab kaff
il faut que me tiyè sama tank thi biir
appart bima nekk ni di diangue di lire ayy saar
cèytanè dafma beuggone dampe ni liire ak mame
mou deff ma diame naar ma takk thi biirr ab kaff
kouko dawoul deh dalay sank kill fat-fat
foumma wowatti faut que ma lanke nguirr am diame bagna tèla fouti
xamatougnou lane moy lèrou goudi
kilifa yii niouy royy fadiar tell laniou dane yèwou diouli
dokh dou am niou am xèlou diouli
loutakh bignoula diappè nga fakk sa pape nèla dotto guène gouddi
dèffarouwate di gueune nekk xel ndakh diangue dou wess
iblice dafgnon beugg djiguiti nioune niou deff niou diamou bakène
koufi yokk wèddi wadiou yiww faw nga wokk dokk
nakh nga sa bopp bo foguè ni bofi diauggè kène doula fattè
nga meyma baath tègu ma paka thi poute
nandena dangua ma beugg diappè ngaka thi pète (en)
mane damala done tope sama boppe di mètti kène
dou wèdini beugg lou yombe mo lay yobè lou mèti
ya takh ma pouce wakhtou diouli yima tayelone diogg
iow yama takha dioylo djiguène yima nobb
nga nekk thi sama bopp dima dey may moy
bala may dièguissi ragg nga gueune ma taggaliko ak iow
bayima bayima (hunxun) bayima (eh èè)
bayima ma bayila bayima bayima ×4 (yeah)
ya takh ma pouce wakhtou diouli yima tayelone diogg
iow yama takha dioylo djiguène yima nobb
nga nekk thi sama bopp dima dey may moy
bala may dièguissi ragg nga gueune ma taggaliko ak iow
bayima (bayima) bayima (bayimaa) iow bayima
(eh èè) iow bayima ma bayila nga bayima (yeah)
nga bayima (bayimaa) nga bayima ma bayila
dième na reuthi
sa pèkhè kèmtane le
ya meune yew ayy thieur
teudjiou thi sa diel la teubb
iow ya bagne diame
euppelè sobè amsterdam
iow ya reuy lamigne
sa taar meune danèl diam
ya takh ma pouce wakhtou diouli yima tayalone diaugg
ya takh ma rousse bouma dadjègg samay goro dima togn
yeah
samay thiono yeupp nioul nagn
yeaah
addouna dou rombe courpagne
danga beugg niou rèere
beuggoulo peace and love
mane beuggouma niou bokk kourèle
beuggouma guiss sène yone
beuggouma ande ak iow
kone boule ande ak mane
beuggouma nekk ak iow
beuggo nekk ak mane
beuggouma deff ak iow
ammo loy deff ak mane
warrouma guiss louma nekh rekk deff
warrouma togg louma nekh rekk deff
bayima bayima bayima ma bayila
bayima ma demm bayima ma demm bayima ma demm manila bayima nga bagne
end
PBL. F



Writer(s): elzo jamdong, misterthiere


Elzo Jamdong - Macina
Album Macina
date of release
29-06-2018




Attention! Feel free to leave feedback.