Lyrics Baykat - Ismaël Lô
Mané
hé
baykat
bi
khalam
Démonna
bay
nékh
wayé
boumgua
Dokna
mome
Mané
hé
baykat
bi
khalam
démonna
Bay
nékh
wayé
boumgua
dokna
mome
Boula
nékhé
talalal
say
lokho
Yaye
docteur
biy
fath
khifou
askane
bi
Liko
dalé
si
nditoum
rew
bassi
miskine
Ya
souméko
di
dane
sa
dolé
andak
nath
Bi
di
liguey
sa
gnakha
di
tourou
Ngay
bay
di
doukat
bilay
ya
am
diome
Kon
diarama
baykat
koufi
xiff
yako
Doundal
bamou
sour
waw
koufi
fébar
Yako
nandal
aki
réén
bamou
féékh
Kon
diarama
baykat
koufi
xiff
yako
Doundal
bamou
sour
Waw
koufi
fébar
yako
nandal
aki
réén
Bamou
féékh
Ya
momone
sa
mbay
Ya
mome
sa
guanthiakh
mome
say
Ndiour
ya
mome
sa
alla
di
bay
Nguour
gneuw
dougalthia
lokhome
ak
Boor
fékeleuthaa
guanthiakh
ba
Mégneu
lole
ndékétéyo
Kon
diarama
baykat
koufi
xiff
yako
Doundal
bamou
sour
Waw
koufi
fébar
yako
nandal
aki
réén
Bamou
féékh
Kon
diarama
baykat
koufi
xiff
yako
Doundal
bamou
sour
Waw
koufi
fébar
yako
nandal
aki
réén
Bamou
féékh
Dirama
diarama
baykat
bé
yaw
Kéneu
rek
mola
mana
fay
Moy
bourbi
yaalla
Guathia
ngalama
Guathia
ngalama
yaw
baykatbé
Guathia
ngalama
Guathia
ngalama
yaw
baikatbé
Dirama
diarama
baykatbé
yaw
Kéneu
rek
moleu
mana
fay
Moye
bourbi
yalla

1 Baykat
2 Incha Allah
3 Tass Yakar
4 Le Jola
5 Taar Dousey
6 Manko
7 Yaye Boye
8 Plus Je Fais Ci, Plus Je Fais Ca
9 Mbindane
10 Wakhal
11 Ouvriers
12 Jiguen
13 Ma Fille
Attention! Feel free to leave feedback.