Ismaël Lô - Mam Lyrics

Lyrics Mam - Ismaël Lô



Diam bou nekeu nekeu mame lay gnane
Te nekeu mam moy guis say takander
Boukani mame beneu beugn
Diebou dieun bl legui da barry soukar
Te dieb bou wekh bl khonkhatoul
Mane mame mougui wane djikom
Khalas mame de dala mere
Khalas nena amo bena respet
Boukani mame beneu beugn
Ataya bl legui safoul khorom
Dou lekeu soupou kandja bou amoul soow
Mane mame mougui wane djikom
Khalas mame de dala mere
Khalas nena amo bene respet
Boukani mame beune beugn
Khale bou lakhou waw sl guanaw mamam
Waw ngua kay feki diko door
Mane mame mougui wane djikom
Khalas mame de dala mere
Khalas nenaamo bene respet
Kon mbalagne fang mbalage fang
Mame mame dala mere mane mame mboy mame dala mere
Mane mame boul mer mame boul mer mame boul mer
Kon bayil door nl bayil doore bayil door nl bayil doore
Waw bayil door nl bayil dore bayil door nl bayil dore
Mame mame dala mere mani mamemboy mamemboy dala mere
Mane mame boul mer mame boul mer mame boul mer mame
He he he
Mame mboy bouguoul kou lale seuteum motakh seut louko nekh
Def sl keurgui
Kon mame mboy bo amon beugne digua mate
Mame mboy bo amon beugne digua mate he he
Bayial dore nl bayil dore
Mame mboy beugoul kou lale seuteum
Bayil door nl bayil dore
Bayil door nl bayil door



Writer(s): Ismael Lo


Ismaël Lô - Dabah
Album Dabah
date of release
26-06-2001




Attention! Feel free to leave feedback.