Lyrics Calm Down (feat. Jeeba) - Jeeba , Karabalik Beatz
Tey
ma
bége
la
Tey
ma
wone
la
Tey
ma
wax
la
Yaa
ma
gën
a
xam
way!
Li
nga
ma
def
soo
ko
bàyyiwul
Dinga
mës
a
ray
doomu
jaambur
way!
Yaw
yaa
ma
xam,
xam
ma
bu
baax
Bu
lu
xasaan
ci
man
loxo
keneen
wokesu
ko
Guddi
gi
jot
ba
lépp
ni
séelaw
Nga
daagu
ndank
ñëw
sama
kaw
di
ma
eh
eh
eh
Yaw
Say
kesen
kesen
tere
ma
nelaw
Yaa
ma
mën
a
yuxuloo
te
xam
nga
dama
ragal
Eh
calm
down,
calm
down
Bébé
calm
down,
doomu
jaambur
la
Eh
calm
down,
calm
down
Bébé
calm
down,
doomu
jaambur
la
Dootoo
niit
parce
que
doo
nitu
Yaa
nga
may
fit
est-ce
que
doo
ciit
Ni
ngay
def
dama
joomi
Man
li
may
yaakaar
est-ce
que
doo
ñooñu
Yeah
yeah
Baby
li
ma
jaxal
te
nga
wax
ma
ki
la
jàngal
Sant
na
sa
bàjjen
moom
mi
la
jox
li
may
jomal
Amatuma
sago
ci
yaw
su
ma
la
gise
saalit
Waaw
waaw,
yow
baby
waaw
waaw
Seddal
sama
xol,
dalal
sama
xel
Yaa
ma
gëna
lool
Ne
waaw
seddal
sama
xol
dalal
sama
xel
Eh
eh
eh
Eh
calm
down,
calm
down
Bébé
calm
down,
doomu
jaambur
la
Eh
calm
down,
calm
down
Bébé
calm
down,
doomu
jaambur
la
Dootoo
niit
parce
que
doo
nitu
Yaa
nga
may
fit
est-ce
que
doo
ciit
Ni
ngay
def
dama
joomi
Man
li
may
yaakaar
est-ce
que
doo
ñooñu
Attention! Feel free to leave feedback.