Kya Loum - Xol Ak Rouh - translation of the lyrics into French

Lyrics and translation Kya Loum - Xol Ak Rouh

Xol Ak Rouh
Xol Ak Rouh
Ahhh ha ha ha ah ha ha ha aha ha ha ahahaaaaaa
Ahhh ha ha ha ah ha ha ha aha ha ha ahahaaaaaa
(Houwowo aahhhh)
(Houwowo aahhhh)
Ahhh ha ha ha ah ha ha ha aha ha ha ahahaaaaaa
Ahhh ha ha ha ah ha ha ha aha ha ha ahahaaaaaa
Amena louy ñieuw sama xol
Mon âme s'est réveillée
Jaxasook sama roukh
Tu as réveillé mon esprit
Xelmiy weur nguir bëug xaam limou done
J'ai perdu mon cœur, tu as pris mon âme
Mi ngui tang lol te sed lol
Je ne suis qu'un corps vide
Amena loui lale sama roukh
Mon âme s'est réveillée
May yeuk xamel gou yaag lole
J'ai trouvé la joie en toi
Fesma dele bay tourouuu
J'ai oublié le monde
Ma beug xam li loumou done
J'ai perdu mon cœur
Sama xol ngay lal khaawma fi ngay diar
Mon âme, je l'ai trouvée, elle est en toi
Li de' moudjouna doy waar
Je ne me souviens plus de ce qui était avant
(Ahhhhh ahh)
(Ahhhhh ahh)
Soma khasse' xol damay dialasso
Mon âme, mon trésor, je la chéris
Douma guiss lelene lou soul yaw
Tu es tout ce que je veux, mon amour
(Yaaaaawww)
(Yaaaaawww)
Ahhh ha ha ha ah ha ha ha aha ha ha ahahaaaaaa
Ahhh ha ha ha ah ha ha ha aha ha ha ahahaaaaaa
(Houwowo aahhhh)
(Houwowo aahhhh)
Ahhh ha ha ha ah ha ha ha aha ha ha ahahaaaaaa
Ahhh ha ha ha ah ha ha ha aha ha ha ahahaaaaaa
(Houwowo aahhhh)
(Houwowo aahhhh)
Xel day diaxassok rouwaam
J'ai trouvé la paix en toi
Lamiñe loot nguir toudou ko
Mon cœur bat pour toi
Te' niom ñiar souñiou xeel mi
Je me suis perdu en toi, je t'ai trouvé
Loot nguir rañie' ko
Mon cœur bat pour toi
Goudi nga nek leer
Je te regarde avec amour
Suba nga nek keer
Je t'admire de tout mon être
Mbalaanou yeurmande
Tu es mon ange gardien
Gou doul diekh
Mon amour pour toi
Goudi nga nek leer
Je te regarde avec amour
Suba nga nek keer
Je t'admire de tout mon être
Mbalaanou yeurmande
Tu es mon ange gardien
Gou doul diekh
Mon amour pour toi
Sama xol ngay lal
Mon âme, je l'ai trouvée
Khaawma fi ngay diar
Elle est en toi
Li de' moudjouna doy waar
Je ne me souviens plus de ce qui était avant
(Ahhhhh ahh)
(Ahhhhh ahh)
Soma khasse' xol
Mon âme, mon trésor, je la chéris
Damay dialasso
Tu es tout ce que je veux
Douma guiss lelene lou soul yaw
Tu es tout ce que je veux, mon amour
(Yaaaaawww)
(Yaaaaawww)
Ahhh ha ha ha ah ha ha ha aha ha ha ahahaaaaaa
Ahhh ha ha ha ah ha ha ha aha ha ha ahahaaaaaa
(Houwowo aahhhh)
(Houwowo aahhhh)
Ahhh ha ha ha ah ha ha ha aha ha ha ahahaaaaaa
Ahhh ha ha ha ah ha ha ha aha ha ha ahahaaaaaa
(Houwowo aahhhh)
(Houwowo aahhhh)

Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Kya Loum

Attention! Feel free to leave feedback.