Kya Loum - Niit Lyrics

Lyrics Niit - Kya Loum



Tay dina done sama setou
Waxtaan ak mane
Fass yene na jakaarlok mane
Xolate sama diar diar fi
Bima dioudo ba taay dji le
Lane lafi def?
Ragne' nani dotouma gone'
Xaam na lou baax teyit xaam na lou bone
Taye souma fi diougue' we'
Louniou may sedel?
Maay deff lu baax
Maay deff lu boon
Ma di leer madi leudeum
Baax boon leer leudeum maye tande ki ma thi wara doon
Kaay niou waxtane' deugui djiko te'
Bayi yallak ate'm
Adouna be' diakhasso
Di nga deff lu nice di nga togne hummm
Kou thi nek am beuss ben beuss
Nga dioum def lodoul netali fene
Nita andak seytane'
Waye' yallah mo ko bakhal
Sa Dieufeul diou nice meune done sa mbalanou suba
Diema baax diema yiiw bayi xel thi euleuk ndakh maat na sorale
Maay deff lu baax
Maay deff lu boon
Ma di leer madi leudeum
Baax boon leer leudeum maye tande
Ki ma thi wara doon
.Everyday you judge me
Every time you judge me
Why do you judge me
Only god can judge you and me
Maay deff lu baax
Maay deff lu boon
Ma di leer madi leudeum
Baax boon leer leudeum maye tande ki ma thi wara doon
Kaay niou waxtane' deugui djiko
Te' bayi yallak ate'm



Writer(s): Olivier Delahaye, Abdoulaye Sy, Kya Loum


Kya Loum - Niit
Album Niit
date of release
14-10-2022




Attention! Feel free to leave feedback.