Lyrics Yaw La - Kya Loum
Gueustouna
na
ba
xaam
ragne'na
Mame
loumou
lep
deugue
Tay
xaam
na
thi
daraa
Tewena
temb
nguir
se'y
Si
seuy
te'
yallah
takh
Tamou
na
ouff
kouli
ndiabote
gui
So
tuke'
te'
na
sa
xel
daal
Bour
yallah
moma
bolek
yaw
(My
love)
Beuguela
demb
tay
la
raw
(Sama
xol)
Ma
nangou
ko
di
ko
ndamo
(My
love)
Lawela
thiate
ndax
amoulo
morome
(Ken
dou
yaw)
(Heey)
Yaw
la
yaw
la
Yaw
lama
yallah
bolel
si
adouna
(Heey)
Yaw
la
yaw
la
Li
may
niane
bour
bi
yallah
moy
sa
bo
tangue'
malay
ke'ral
Done
sa
yaye
fall
di
la
sikaral
Matela
kanam
te
meune
sa
ganaw
Mbeuguel
gouy
laaw
ba
faaw
Baniou
andado
thi
batine
di
fanaaw
Baby
yallah
moma
bolek
yaw
Te
lou
yallah
bole
Samb
ko
moy
li
woor
Tewena
temb
nguir
se'y
Si
seuy
te'
yallah
takh
Tamou
na
ouff
kouli
ndiabote
gui
So
tuke'
te'
na
sa
xel
daal
Bour
yallah
mome'
bolek
yaw
(My
love)
Beuguela
demb
tay
la
raw
(Sama
xol)
Ma
nangou
ko
di
ko
ndamo
(My
love)
Lawela
thiate
ndax
amoulo
morome
(Ken
dou
yaw)
(Heey)
Yaw
la
yaw
la
Yaw
lama
yallah
bolel
si
adouna
(Heey)
Yaw
la
yaw
la
(Baby,
Baby)
Yaw
la
yaw
la
Yaw
lama
yallah
bolel
si
adouna
Yaw
la
yaw
la
(Heey)
Yaw
la
yaw
la
(Baby,
Baby)
Yaw
la
yaw
la
Yaw
lama
yallah
bolel
si
adouna
Yaw
la
yaw
la
(Heey)
Yaw
la
yaw
la
Attention! Feel free to leave feedback.