Omzo Dollar - Messatsu Lyrics

Lyrics Messatsu - Omzo Dollar



Mièzé yay sen baye
Mièzé yay sen baye
Zo Dollar yay sen baye
Zo Dollar yay sen papa
Mièzé yay sen baye
Mièzé yay sen baye
Hummyo messatsu
My name is zakuma
En cas de wuyayoy
En cas de wuyayoy nianalmeu yaay boy
Bisbi dina thiol en cas de wuyayoy
Capsi i the house pas de geste brusque
500 mille rappeurs pas de testicules
Tout ce qui bouge je baise
Tout ce qui bouge je baise
Tout ce qui bouge je baise
Nigga tout ce qui bouge je baise
Han Mère bi nenama thiow baxoul dom moytoul dagassanté
Manéko boy bou cool la yaay mais kouma togn mom dina saga sa ndeye
Boul am loy tiit sama état de santé ndakh
Kouy défantek ayy goumbeu mom ragaloul beut
Mc yi legui comme ay djiguen gni
Damelni bagn len di diongal danio dagg lou eupp
Mangui si assamane di tokh chicha mane ak sa mame
Gaaw si wathié goné mane leu Memedou Gassama
Rappeur boumeu guiss nane salam papa
Waxma kagn laniouy featuring (ngané lane)
Mané len job len bassi kanam link dou nii
Hum sa guel naleu wax loumou guiss
Mou tombeu komm français sale
Si net bi beuri ngen ay followers
Mais kañ ngen di remplir aay sale
Diaar si digui bi Moussa Dembele
Fuck ki iow akh gain béle
Façon rappeur yi comme ay mbalax man
Lal lay deff si rappeur akh mbalaxman
Sa youma fi yendo keur gui selaw
Sa youma fi yendo keuri gui selaw
Nigga poouyyaa
En cas de wouyayoy
En cas de wouyayoy
Nianal ma yaay boyy
Bess ba dina thiol
En cas de wouyayoy
Capsi in tha house
Pas de geste brusque
500 mille rappeurs pas de testicule
Tout ce qui bouge je baise
Tout ce qui bouge je baise
Tout ce qui bouge est baise
Tout ce qui bouge est baise
Il faut niou tassaré fi yeup
Il faut niou tassaré fi yeup
Il faut niou tassaré fi yeup
Il faut niou tassaré fi yeup
Ok naan feka biir crack eupeu avenir barack
Degua anglais français wolof zarma man na lire arabe
Tu peux m'appeler Khelaïfi
Depuis temps tele CFI
Zidane pelé fila feulé clip by sele vfci
Ok dan na dane tal télé sen clip yi
Daw may nian Yalla bouma massa melni gnini
Bou fekonn sett la nekk di rap loumay
Rap konn bou yagua mangi dawal lambourghini
Rappeur yagni danou melni ay domino wathieno ay magu taka ay abdomino
Pablo ino tiaponino douma tapette smay testicule daniou am ay abdimino
Nigga xamo nino amo niveau yangi
Deff loman mais mongi saff ay joli caca
Bess bo coubi di ma sani ay pic souy gueune confirmer ni may sen papa
Ehh mann guichet fermé boucher fermer fils da soulano
Konn fuck ay place de souvenir fuck ay sorano



Writer(s): Flagrandelit, Omzo Dollar


Omzo Dollar - Beut ak lamign
Album Beut ak lamign
date of release
09-02-2019




Attention! Feel free to leave feedback.