Lyrics Soutoural - Omzo Dollar
I
say:
Han
kou
niaakeu
rekka
am
yama
gueuneu
xam
Kou
nameuh
dina
taameuh
yama
gueuneu
xam
Kou
xamné
xamoul
rekka
xam
yama
gueuneu
xam
Nieup
done
ay
borom
xam
xam
yama
gueune
xam
xam
Bakh
moy
bone
fi
nieupeu
djoum
légui
Djiguèneuy
torokhal
goor,
goor
yi
nioy
mopugne
légui
Djiguène
khol
avenir
mais
goor
sa
passé
lay
guiss
Motah
goor
yi
nala
takkeu
lagni
dokhaané
légui
Okay!
Am
djabar
yu
melni
sunu
yaay
dou
amaate
man
Sori
naniou
souniou
Pa
deug
rekkay
takh
may
wakh
mane
Niom
Pa
bouy
géré
quatre
women
lagni
wowé
batman
Pa
bouy
géré
quatre
women
lagni
wowé
batman
Haaan
Soutoural
Fi
so
beugué
sa
dara
dokh
fokk
nga
soukou
raam
Fi
ngay
guiss
ay
beaux
parleurs
yu
andak
lamigne
yu
niaaw
L'Habit
ne
fait
pas
le
moine
mais
y
a
des
habits
pour
moines
Rigne-Se
bi
dèy
tek
kone
yaw
dindégo
sa
téré
Loy
neubeu
nit
bou
nioul
nigga
bindeu
ko
ci
teeré
Kou
fi
nek
chomeur
tok
di
waate
ni
dagnko
liguèy
Deuk
bou
kène
doul
liguèy
waayé
nieup
lagni
liguèy
Eh
yaw
fi
moy
Sénégal
lou
nekh
waay
def
Souniou
bougoul
fène
deug
lagni
neubeu
Défal
loumay
wakh
boul
def
loumay
def
Défal
loula
nekh
gars
yi
nagn
leu
Soutoural
Soutoural
soutoural
Soutoural
soutoural
Soutoural
soutoural
Soutoural
soutoural
I
say:
Han
kou
niaakeu
rekka
am
yama
gueuneu
xam
Kou
nameuh
dina
taameuh
yama
gueuneu
xam
Kou
xamné
xamoul
rekka
xam
yama
gueuneu
xam
Nieup
done
ay
borom
xam
xam
yama
gueune
xam
xam
Bou
féké
yémo
place
boul
signé
monogamie
Bou
dh
niémé
wo
clash
boul
signé
polygamie
Di
nala
may
sa
baate
boy
youkhou
sama
famille
Bou
féké
men
nèy
trash,
djiguèneuy
auto-mbalite
Da
melni
Afrique
sofi
sathioul
meuno
nek
milliardaire
Lane
mo
gueuneu
raciste
wané
keu-gna
(Gnaak)
wala
ndréingue
Kogne
bo
dougou
niéteu
djaaka
waayé
bène
dou
ci
fess
Pa
yu
eupeu
djabar
niofi
eupeu
ay
maîtresse
Système
LMD
système
LMD
Léwal
Maîtresse
Djabar
(LMD)
lolay
système
LMD
Liguèy
Mèche
Doxane
yeah
Système
LMD
Primaire
ngay
nope
sa
maîtresse
djangue
système
LMD
Soutoural
fi
so
bougué
sa
dara
dokh
fokk
nga
soukou
raam
Amna
niou
détourné
xaliss
dém
di
tchi
tabakh
djaaka
Ndara
nakh
sen
bopp
fokné
nio
ngi
nakh
Yallah
Eh
yaw
fi
moy
Sénégal
lou
nekh
waay
def
Souniou
bougoul
fène
deug
lagni
neubeu
Défal
loumay
wakh
boul
def
loumay
def
Défal
loula
nekh
gars
yi
nagn
leu
Soutoural
Soutoural
soutoural
Soutoural
soutoural
Soutoural
soutoural
Soutoural
soutoural
Attention! Feel free to leave feedback.