Lyrics Ndakh Rap - Omzo Dollar
Yeah!
2006
ba
2016
nigger
(nigger)!
Young
Fif
I
say
Warone
nga
féké
bimay
dokh
ak
samay
ngandi
casque
Dokh
di
bondé
melni
mandikate
Gars
yi
fook
ni
boy
bi
da
am
handicap
Jean
huilé
ak
chemise
hawaïenne
Tout
est
neuf
melni
j'ai
pas
la
moyenne
Nigger
dou
sakh
man
ak
yeen
Fadiar
ba
guiss
lune
mangui
ci
mbed
bi
di
Binde
texte
ba
amatouma
encre
sama
bic
plume
Man
ak
Alsseyni
took
di
veiller
sayou
goudi
jott
Yagua
freestyle
terrasse
bi
ci
kaw
ba
heurou
diouli
jott
Produire
ay
dêchet
fils
Di
deff
ay
son
ak
FL6
Micro
two
taw
(thousand)
sama
PC
fixe
Amone
na
talent
fook
ma
teela
am
buzz
Jamono
studio
duplex
01
heure
8000
Eli
ak
Bugs
Mangui
lay
nétali
ay
beuss
yo
xamni
fallait
deff
ay
délit
ay
teuss
Mère
nangalou
ma
meunou
ma
fegn
télé
ak
feuss
Maxouli
ay
beut
c
textuel
kepp
momay
Gestuel
massalé
pour
mou
bagna
sipp
ma
tekk
xel
Ndax
fima
jaar
daniouma
yagua
teuthie
ndax
rap
Yague
naniouma
képp
dima
mbéthie
ndax
rap
Daniouma
yagua
guéné
keur
gui
nigger
lepp
ndax
rap
Kon
soma
joxé
mic
tay
mom
lepp
lay
wax
Nieuweul
déglou
fima
jaar
lima
yeukk
ndax
rap
Meunoma
jaay
graw
boulma
leepp
say
wax
Ndaxté
xamo
fima
jaar
lima
yeukk
ndax
rap
Yeah
boulma
leepp
say
wax
my
nigger!
Man
ak
Boy
creer
groupe
bou
toude
Capsibloc
Hustler
Power,
José-T,
Omzo
ak
ZigZag
faté
wouma
Fresh-T,
Kheushy-T
my
nigger
Nazz
ak
Bass
Repetition
yi
négou
Abba
mèram
sakh
di
caass
Daniou
yague
di
beuré
ak
radio
yi
yague
di
weeré
Amoul
wone
xaliss
pour
deff
clip
ba
son
yi
dialeu
ci
télé
Kon
fatalil
querelle
yi
jabanté
feulé
yi
abanté
yeuré
yi
Probleme
sou
amé
niou
raakk
ba
saga
ndy
ennemi
Deff
yeufou
hustler
Concert
kou
am
probleme
ba
tekk
beut
niou
wax
la
Tekk
seuss
niou
nokh
la
heyy
Premier
concert
niou
huéé
niou
Deuxieme
niou
rayy
tout
le
monde
Jubilé
coulisse
yi
ni
équipe
bou
gagné
coupe
du
monde
Bring
sa
appetit
Man
ak
José
thiolé
pass
ma
dessé
Five
niou
jeundé
ko
ay
neme
ak
spaghetti
Mais
tay
ma
ndiabati
dokh
HLM
ba
Mamelle
Lolou
yeupp
piur
dougal
ben
son
rap
meunouma
fay
limouma
amel
My
nigger
doumala
fenn
defone
na
fi
lepp
ndax
rap
Yague
na
di
jooy
yague
bégue
ndax
rap
Dama
yagua
mougn
yagua
nopi
lepp
ndax
rap
Kon
soma
joxé
mic
tay
mom
lepp
lay
wax
Nieuweul
déglou
fima
jaar
lima
yeukk
ndax
rap
Meunoma
jaay
graw
boulma
leepp
say
wax
Sou
féké
xamo
fima
jaar
lima
yeukk
ndax
rap
Yeah
boulma
leepp
say
wax
my
nigger
1 Deugue
2 Hentai
3 Fadiar
4 Lo meu def
5 Lepp legui
6 Agresseur
7 Sante
8 Penda Mbaye
9 Bou dé Dëg la
10 Muerte
11 Dou changer
12 Buur
13 Ndakh Rap
14 Borom
Attention! Feel free to leave feedback.