Omzo Dollar - Penda Mbaye Lyrics

Lyrics Penda Mbaye - Omzo Dollar



Hey
A siggi niaga loukou magga wei
Wouh wouh
Nia nougou nagam magga wei
Wouh wouh
A thigi niaga lougou mouga wei
Wouh wouh
A sigi niaga lougou thiak thiak
I say
Penda mbaye ngui si wagn bi
Penda mbaye gui si wagne bi
Penda mbaye gui si waagnn beiii
Nigger penda mbaye nigui si wagn bi
Di bakhal ay kilo yi kilos
Di bakhal ay kilos yi kilos
Di bakhal ay kilos ay kilos
Maggi si tchine bi ak geunne ak pilon
Abozzer
Jean bi sandi nako defal pagne bi
Indi nienti rappeur sama aagn bii
Waxonala soblela si yassa wantei rap bi dei si man leu geuna yomb marchei samedi
Teksi fi moy karack nigger nioleine geuna bandit
Fower geu seu life beug fower sama kaagne bi
Waxal kougnou diss nigger lolou douko bis beine bise lagnlay piss geu rest in peace melni gandhi
Han
Papis diagne neina mieze waro seral sakh
Kein dougn sacrifier lathiel wa sarakh sakh
Sama deune eupp chaine sakh canal satt
Beurri class nigger dama wara tabakh fac
Geunla yeigg nigger boul djawaler tabac ak crack
Wouy sama ndeye nioune nio njeukk mbalakh trap
Fogone nani bima bayer naffi fekk kouma jakhal wantei dara meussoul changer
Boma geumoul ga indalei niom nieup
Mani niom nieup
Nigger samay clip done neu kany sein beutt
Jour bougn le fek nagnko caler comm deurr
Nieuw sand seu gallei melni khalei bo teuf
Tok seu tchinn comm chef beug chill comm cheikh
Jeulii thiett comme cheque diko tchop comme thiep
Beurri chik comme cheeks beuri shiit comme tek .nigger todj seu thio thie thie
Thioh
Rappeur yi yeip lagniy wanne
Dragon ball z berus-sama
Wowema president dollar
Aka karack obama
Fake mc yi nioggi kass
Nigger djeun bi nioko wass
Dama beug dessert defal yapou gaindei sama place
Wawaw waw
Penda mbaye ngui si wagn bi
Penda mbaye gui si wagne bi
Penda mbaye gui si waagnn beiii
Nigger penda mbaye nigui si wagn bi
Di bakhal ay kilo yi kilos
Di bakhal ay kilos yi kilos
Di bakhal ay kilos ay kilos
Maggi si tchine bi ak geunne ak pilon
Abozzer
Penda mbaye ngui si wagn bi
Penda mbaye gui si wagne bi
Penda mbaye gui si waagnn beiii
Nigger penda mbaye nigui si wagn bi
Di bakhal ay kilo yi kilos
Di bakhal ay kilos yi kilos
Di bakhal ay kilos ay kilos
Maggi si tchine bi ak geunne ak pilon
Abozzer
Sama team bi qualiter leu
Seu equipe disqualifier neu
Seu tougni douff ni cathy jenner
Seu calecin bi amoul shit ni catlyn jenner
Kayma wax la beine wakh
Ga kham lamo takh wakhuma seini mbollo
Zo dollar daffa meun rap
Yeinein rappeur yi dagn deig olof
Ay rappeur you complexer rek laffi fekk
Di mboubo fougnou jugger pour niou meuna deim
Lolotakh rap bi geine beug ko def yeufou banlieu ak town
Tei niarri yeupa yem
Boleine gissei rappeur sett
Amoleine loleine wakh loudoul say topondor americain yi
Nioun degno credible si gettho tei crefible si town fougn doug fier tei lolou dou faiblesse
Man dei ngandime chaine lay takk
Gandime doffou auto lay dawal
Gandime drianke lay takk
Bouleu mettei gandime gang lay andal
My nigger faut que niou tekki
Tiak tiak nigger vitfe
Sama cheque yi dagno beurri virgules
Heureusement beu mieze ayona si dictee
Tokk fi di hate si ay real nigger
Nonon dougn def lolou
Rappeur yi faut qu'on les kills nigger
Khamnani yagg gama wolou
Man ak rapprur yi non mounougnnou deiggo
Seini cachet yi matoul seini ego
Rap boula doundaloul faut que ga dead ko
Passe leu geu siw ni ronaldinho deco
Mc meuy touma yaw souma la djeko
Omzo premier omzo deuxieme ex-aequo
Nioggi si birr t doynagn pour ga sour
Mc koula giss khamni my nigger lekko
My nigger man bouder yaw lay waxal douma dadjeik ioe beu nela dou man
Kou dofdoflou wakh sama tour nala fekk seu galler melni heurou agn
Abozzer
Penda mbaye ngui si wagn bi
Penda mbaye gui si wagne bi
Penda mbaye gui si waagnn beiii
Nigger penda mbaye nigui si wagn bi
Di bakhal ay kilo yi kilos
Di bakhal ay kilos yi kilos
Di bakhal ay kilos ay kilos
Maggi si tchine bi ak geunne ak pilon
Abozzer
Penda mbaye ngui si wagn bi
Penda mbaye gui si wagne bi
Penda mbaye gui si waagnn beiii
Nigger penda mbaye nigui si wagn bi
Di bakhal ay kilo yi kilos
Di bakhal ay kilos yi kilos
Di bakhal ay kilos ay kilos
Maggi si tchine bi ak geunne ak pilon
Abozzer
(Nigger fuck rap galsen c la merde
Ma begn douma featuring ak yeineuh
Danou melni robert mugabe
Game bi nioko yaggeuh tassarei
Tassarei
Tassarei tassarei
Game bi nioko yagg tassarei
Tassarei
A sigi niaga lougou magga wei)




Omzo Dollar - Dëgeuntane
Album Dëgeuntane
date of release
16-09-2016




Attention! Feel free to leave feedback.