Lyrics Dée Moo Wóor - Orchestra Baobab
Aduna
ko
meuneu
diouyou
louy
weey
law
Aduna
ko
meuneu
diooy
lou
weey
law
Dama
tokk
beu
digui
diorr
teud
teud
nelaw
Diekh
xell
mi
deim
thie
Lakhiraa
dee
moo
worr
Waindé,
Waindé
Dieng
toundou
bayi
Ngoné
Ndour
Malick
bayou
Penda
Ngane
dee
mo
worr
Meunou
meu
neilaw
ngir
xalatt
sama
baye
bi
telleu
reer
Ey
way
gars
gni
ndeikeiteii
dee
mo
worr
(Dama
tokk
beu
digui
diorr
teud
teud
neilaw
Diekh
khell
mi
deim
thie
Lakhiraa
dee
mo
worr)
×2
Ma
deim
Niger
kholl
founé
dee
mo
worr
Aduna
ko
meune
dioy
louy
weey
law
Sama
khell
mi
yedd
ma,
Sama
kholl
bi
dioy
Malick
bayou
Penda
Ngane
dee
mo
worr
(Dama
tokk
beu
digui
diorr
teud
teud
neilaw
Diekh
khell
mi
deim
thie
Lakhiraa
dee
mo
worr)
×2
Khawma
kagn
la,
khawma
fane
leu,
Khawmeu
nane
leu
may
dikké
man
khamnani
deug
dall
dee
mo
worr
Meunou
meu
nelaw
ngir
khalatt
sama
baye
bi
telleu
reer
Ey
way
gars
gni
ndeikeitei
dee
mo
worr
Yallah
buur
bi
laniouy
niane
lidoul
diarr
Té
yagg
mom
feikk
niou
dieuf
diou
bakh
amiina
Amine,
aaamine
yalna
Yallah
nangou
niane
Amine,
aaamine,
aminaa
(Dama
tokk
beu
digui
diorr
teud
teud
neilaw
Diekh
khell
mi
deim
thie
Lakhiraa
dee
mo
worr)
×4
Attention! Feel free to leave feedback.