Youssou N'Dour feat. Le Super Étoile - Bou Leen Coupe Lyrics

Lyrics Bou Leen Coupe - Youssou N'Dour feat. Le Super Étoile



Ma demba, leundeum gui, courant bi waroul won démé ni.
Nit yi daño diakhle.
Nit yi daño diomii.
Mbirmi deufeu leundeum.
Ohhhhhhhhh.
Fimou tollou ni.
Louthi meunti te khew.
Mo kham yaako deff.
Mokham defouloko.
Warna guaawa diekhh.
Ndakh ñoun sonou nañou.
ñou sokhlawouñou kham ana kan mo toñ.




Youssou N'Dour feat. Le Super Étoile - Spécial fin d'année plus




Attention! Feel free to leave feedback.