Lyrics Leaving (Dem) - Youssou N’Dour
Dem
dem
Dem
fan
Den
ndax
lan
Baya
ko
mom
Dem
nguir
xee
bou
barri
bi
Dem
ndax
teen
boh
neex
bi
Teh
rapp
rek
noom
noo
siy
naan
Nach
bi
lakkatouma
taw
bi
barrewoul
Dem
ngir
bokk
bone
menou
fee
am
Dem
ngir
daffa
wara
nekk
gorr
done
Goorgoorlau
Dem
dem
Dem
fan
Dem
ndax
lan
Liberte
bi
Si
espace
bou
lendeum
bi
Sama
beut
yi
guissa
tounou
Garap
yi
nga
xamenteni
noo
ma
souxat
Su
beut
setiee
barap
yi
bow
Dem
ngir
Keur
gui
daf
may
nirou
lou
lendeum
Dem
nguir
daffa
warranekk
goor
done
Goorgoorlau
Damay
dem
Chi
alla
bi
Damay
dem
Chi
dex
goumak
gui
Ne
damay
dem
waw
seeti
sama
nawleyee
Damay
dem
si
ban
bou
ritax
bi
Damay
dem
ba
reewu
bitty
Ne
damay
dem
waw
setti
samambokkyee
Go-go
(bis)
Won
ma
sa
yarii
ma
wax
la
ki
nga
donoy
Won
ma
sa
mbokk
ma
wax
ko
fi
ngay
diaar
Hey
what
do
you
need?
He
he
yaw
lilaneex
Won
ma
sa
yarii
ma
wax
la
ki
nga
donoy
Won
ma
sa
mbokk
ma
wax
ko
fi
ngay
diaar
He
defa
li
la
neexoy
hey
yaw
lila
soop
Sammkatou
mboott
moo
xam
ba
ciy
Sooxaoy
ni
meneuh
kott
noom
daal
amounou
Mbaam
hey
defal
li
la
nexx
oo
Hey
what
do
you
want?
Ho
ho
ho
ho
...
Attention! Feel free to leave feedback.