Canabasse - Dieulil paroles de chanson

paroles de chanson Dieulil - Canabasse

Bo djougué mane wane ma fima djougué
Digua djouk fadiaar téél taakk toubeuy
Gnimay khaar beuri meunouma gouddé
Sama nope baatu mère dima goungué
nama "Basse Basse, Abdou démal dieuli li ngua mom"
nama "Basse Basse, yone wi nga taameuh détchi dem ak jom
bo démé ba soneuh ditchi douté kholal tchi gni leu beug
Bouk topoto say noone
Abdou Basse Basse Basse
Wakh djou bone
Dou takkeu foudoul guémignou borom"
Bou ma tchi seugué douma siggui
Bou sérithieu bi matoul douma gnibi
Boudé yaapeuh taamou na tchi dibi
Boudé yaapeuh dioxma diplôméé bi
Xalé bou djangueuh tangueuh
Diaape niaamboureum
Djiguéne 100% ma tchi thiapeuh some
bouko diaré mane sagne naako songueuh
Séti waadioureuum niaani dji lokhom
Rap game bi légui noumou démé
Niom nieupeu beug nékeu MOI
Mais kéneu matou tchi nii février
Douniou gatt
Loudoul tchioutchiou ci thiaaz
Yombeu love boma beugoul
Xamna da nga am problèmou khol
Sho bi néma: " may nélaw douma robot"
Mane manéko:"Bo djougué mane wane ma fima djougué
Digua djouk fadiaar téél taakk toubeuy
Gnimay khaar beuri meunouma gouddé
Sama nope baatu mère dima goungué
nama "Basse Basse, Abdou démal dieuli li ngua mom"
nama "Basse Basse, yone wi nga taameuh détchi dem ak jom
bo démé ba soneuh ditchi douté kholal tchi gni leu beug
Bouk topoto say noone
Abdou Basse Basse Basse
Wakh djou bone
Dou takkeu foudoul guémignou borom"
Makoy todj fils guiss nga limay tabakh
Philip Morris lou guéneuh def Tabac
Stephen Curry fouma tolleu thiabakh
Marqué sama temps ni Chaba
Doundeu ba bi may dougou sama pas
Maximum bi séddé ni dama nzkhh
Tolo féneu beug dieul sama part
Roi des arènes fékhel bama mbapaate
Rakkeu geunaatal rap ba tchi kanam
Fi nga ma ngi fawone
Ay aate ci guinaaw
Cachets et concert et tu parles de finances?
Dama ram
Baniou may wo tchi ay conférences
Def Cos bou saff andeu ak éloquence
Wane lène finiouy diaar def différence
Bou bakh dou bou bone bone bi
Yeah bi moy référence
Yeah def ko sa bopp fils
Shampooing dou Karaas
Sa Rappeur dou bagaaaaaage,
Sa Rappeur dou bagaaaaaage
Yombeu love boma beugoul
Xamna da nga am problèmou khol
Sho bi néma: " may nélaw douma robot"
Mane manéko:"Bo djougué mane wane ma fima djougué
Digua djouk fadiaar téél taakk toubeuy
Gnimay khaar beuri meunouma gouddé
Sama nope baatu mère dima goungué
nama "Basse Basse, Abdou démal dieuli li ngua mom"
nama "Basse Basse, yone wi nga taameuh détchi dem ak jom
bo démé ba soneuh ditchi douté kholal tchi gni leu beug
Bouk topoto say noone
Abdou Basse Basse Basse
Wakh djou bone
Dou takkeu foudoul guémignou borom"
Basse Basse Basse
Wakh djou bone
Dou takkeu foudoul guémignou borom
Bo djougué mane wane ma fima djougué
Digua djouk fadiaar téél taakk toubeuy
Gnimay khaar beuri meunouma gouddé
Sama nope baatu mère dima goungué
nama "Basse Basse, Abdou démal dieuli li ngua mom"
nama "Basse Basse, yone wi nga taameuh détchi dem ak jom
bo démé ba soneuh ditchi douté kholal tchi gni leu beug
Bouk topoto say noone
Abdou Basse Basse Basse
Wakh djou bone
Dou takkeu foudoul guémignou borom

Writer(s): Abdou Basse Dia

Canabasse - Dieulil
Album Dieulil
date de sortie
03-01-2018

Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.