paroles de chanson LNN - Dip Doundou Guiss feat. Bass Thioung
Nek
ci
yoon,
Nek
ci
deuk
tchi
bagna
tok
Dérétou
ennemie
sama
kaw
Deum
la
déma
Djigne
lima
done
never
give
up
Amna
goudi
you
tiss
douma
daw
Douma
Faté
bamay
géneu
galé
papa
kholal
tay
sa
fils
foumou
tok
Lo
niémé
Niakk
Lo
niémé,
Lo
niémé,
Lo
niémé
Lo
niémé
niak,
Amna
ay
défaites
yi
nga
am
Ay
métitou
moumeu
Yek
échelle
mou
danou
Guiss
na
ay
serpent
you
mandou
Mayna
moma
sétou
tromper
guélou
Diambour
Meusna
geum
nitt
kouma
khamoul
Voté
Afrique
ma
solal
goumbeu
Cagoul
Baniouma
jeunesse
bouy
nélaw
Wayé
jeunesse
sou
new
mo
geun
bou
Yéwu
calou
Nek
ci
yoon,
Feint
fi
yéré
you
bone
Rendi
fi
gaindé
Youy
mbow
Tour
sama
dérétou
gorr
Ioe
ioe!
Néko
mou
tok
Talouma
kébétou
thiow
Niom
daniouy
thiéné
té
amouniou
Diome
Soul
ay
rappeurs
yo
khamné
bamay
ram
sen
CD
ngui
daw
Damako
Kharé
fils
dama
job
Pour
sama
avenir
sama
dome
Fils
dama
agné
khif
Réré
ndox
Diangue
nga
amo
fiit
amo
ngor
Thiolou
ba
lay
watié
sama
bop
Fuck
niémay
coup
d′état
Million
la
wantéré
Samay
shows
Trone
bi
fafa
soudé
samay
tate
Kou
bote
boukki
ay
Faut
kathie
yi
mbow
la
Mane
diapna
nikey
défé
Nonou
la
Li
nga
def
ci
rapp
bi
Mane
dama
moudié
warru
Dip
rap
bi
yako
Maquiller
ba
takh
fépa
tarru
[REFRAIN]
Nek
ci
yoon,
Nek
ci
deuk
tchi
bagna
tok
Dérétou
ennemie
sama
kaw
Deum
la
déma
Djigne
lima
done
never
give
up
Amna
goudi
you
tiss
douma
daw
Douma
Faté
bamay
géneu
galé
papa
kholal
tay
sa
fils
foumou
tok
Lo
niémé
Niakk
Lo
niémé,
Lo
niémé,
Lo
niémé
Lo
niémé
niak,
lo
niémé
niak,
Nekh
amoul
fen
Talent
deug
ngen
am
Yen
sen
talent
moy
meun
fen
Gnimey
Mboubo
lay
mour
Dip
dou
jubo
dey
soul
Goré
ba
done
esclave
mo
geun
Diay
sa
ngor
ba
done
buur
Lokho
bou
tayal
dou
tabakh
lou
deugeur
Lo
Geuneu
bégue
di
geuneu
peuteukh
Ma
takh
ba
labouniou
niou
dima
Neukeul
Welcome
to
life
in
the
jungle
Lafe
famay
yobou
mane
sokhla
Wouma
pneu
Wala
daju
si
niakh
wala
peundeukh
Faté
na
demb
té
diap
ci
Euleuk
niari
lokho
gana
moko
geuneul
Sa
gars
yi
réwantou
dama
len
di
Ray
Kou
djeumeum
yarouwoul
sa
neew
dou
rew
Dieul
leu
nouniouy
dieulé
Thiep
bou
bess
Di
nga
nangou
ba
sa
thieur
yi
bagn
Sama
dieum
ma
geun
Sen
def
Fayna
ound
fay
wesh
wesh
Def
ni
niom
limay
def
rek
déh
Séni
Bop
ni
bambel
tek
tek
Seni
prof
samay
maitresse
lagn
Kougn
fi
thiow
Si
rapp
bi
may
sa
père
Yama
meun
boudé
kou
dakh
fen
Lim
fi
yor
si
Song
dou
khathie
dou
dièkh
Diameu
geun
mais
ay
mo
dakh
fay
Diw
sa
Guel
mouy
geun
di
diap
teint
Diw
guelou
niouy
dakh
yakh
derr
Nieup
Nul
ni
lamb
lac
2 guers
Kou
bote
boukki,
Faut
kathie
yi
mbow
la
Mane
diapna
nikey
défé
nonou
la
Li
nga
def
ci
Rapp
bi,
mane
dama
moudié
warru
Dip
rap
bi
yako
maquiller
ba
takh
Fépa
tarru
[REFRAIN]
Nek
ci
yoon,
Nek
ci
deuk
tchi
bagna
tok
Dérétou
ennemie
sama
kaw
Deum
la
déma
Djigne
lima
done
never
give
up
Amna
goudi
you
tiss
douma
daw
Douma
Faté
bamay
géneu
galé
papa
kholal
tay
sa
fils
foumou
tok
Lo
niémé
Niakk
Lo
niémé,
Lo
niémé,
Lo
niémé
Lo
niémé
niak,
lo
niémé
niak,
Lo
niémé,
lo
niémé
niak
[REFRAIN]
Dip
dakoy
yeungeul
waye,
Dip
dakoy
yeungeul
Bass
dakoy
yeungeul
waye
Bass
dakoy
yeungeul
Bass
Dakoy
yeungeul
Beusseul
fi
(beusseul)
Wouy
beusseul
fi
(beusseul)
Ay
Beusseul
fi,
wa
kone
beusseul
fi
Hé
boy
kone
beusseul
(lou
bess)
Beusseul
fi
lou
bess
sa
bess
ay
beusseul
fi
Wa
kone
beusseul
fi,
Lou
bess
sa
bess
Dip
dakoy
yeungeul
waye,
Dip
dakoy
yeungeul
Bass
dakoy
yeungeul
waye,
Bass
dakoy
yeungeul
Bass
dakoy
yeungeul
waye,
Bass
dakoy
yeungeul
Beusseul
fi
(beusseul)
Wouy
beusseul
fi
(Beusseul)
Ay
beusseul
fi,
Wa
kone
beusseul
fi
Hé
boy
kone
beusseul
(lou
bess)
Beusseul
fi
Lou
bess
sa
bess
ay
beusseul
fi
Wa
kone
beusseul
fi,
lou
bess
sa
bess
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.