Dip Doundou Guiss - Président FIFA paroles de chanson

paroles de chanson Président FIFA - Dip Doundou Guiss



Yah
Mérité lima am ni xaliss sou mbeur
Nitay gnan sa dila sakkou nimbeul
Rap khif sonneu teksi di khandiou di kheuw
Motakh ki ték galsen à paris moy marmite du cœur
Rayla di khol nisa rou di yéguéé
Seuss ni kouy lékkeu gnouy mothiou dérét
Compte bou féss ni ay couchou bébé
Mère bi diouroul play boy diouroul pédé
Damalén bétteu ni kou tidji 100 feux
Ngay crise di cardiaque
Tidji sa gatt bi di tit di sagueu
Ngay sikki sakkeu
Djifi diaafa
Rap dou pile ou face nak
Yako tangal takhoul sa gallé takho thin di takkeu
Heu
Lo ñeme ñàkk boy
Wakholén ma wakhou xaliss lo lén may lakkeu boy
Rabo lén fi lou gueuneu kawé sen taati boy
Dagn makay diokh bama viviens foyé stade bi boy
Lo ñeme ñàkk boy
Guénné lnn takhoul réwandé diekh
Fanaan ci cimetière takhoul bagne la bétteu
Ma baal lén ci pétt gnouy déf bama mér
Ma changer système ni gnouy rayé Ben laden
An
Mouno football beuggeu jouer sougnou équipe type
Mouno diougueul beuggeu tourner si ay film X
Guéné tay ma guénné tay c′est Dip ou Lucky Luck
Réw rékkeu ma téré guénné son bi minuit pile
Kagn nga may tenir tête LNN sisa pussy guel
May changer compte banque ngéni charger ay power bank
Man dama beuggeu guerre motakh ma sol ay tenue treillis
Waadial char de combat
Tabakh cimetière dieund corbillard
Ken guissouma si yén
Péppeu souf nga si guéth
Mouno dieul position ba yeukk ko thiou thiou nga si diékk
Kan mo am carrière bou bakh ni gneup gnou douggou ci man
Souma lay ray doumala sakh khol ni tableau Boubou desing
Hé, yén gneup laa tiim ni caméra karaba
Yén gneuppeu khéwwi fay ni karawou Abba
Dip di fit di kheul ni fassou naarou goor
Tiit ni kou bétteu sa sokhna ak gnari goor
Yaama gueuneu gnoul mais mala gueuneu leundeum
Yaama eup beugne mais maala dakh matteu Eh
Yaw comme verre rou myope si beutou stevy wonder
Trône bi dou pour seun sa tate yi douci khath
Chaque jour freestyle selfie ni kouy diokhé cours rou make-up
Boy Dip dafma sagna teukkou tay sa khour yi lay deup
Pour leçon de rap bi mokkeu tay sa youri lay deup
Diaroul may lakkeu sa khol bi da nga diouddou rk kheum
Hé, fén rékkeu rk nga meun
Même bo doul dioutou fék nga
Ya ngi sa keur baay ba légui kaay ma sous louer la
Yaa Killah fait des vidéos mais boy yi Doudou lagne geum
Nagnou douggou sen keur simmi braquette saw ci bountou négeum
Dérét bou naré tourou ci boum yi légne dieum
Khamna gnima beuggeu lékkeu gneup mais sourou lén ma
Clash ma katt sa
Clash ma k sa n*d*y
Waass ma ma taat sa mère
Lamb nga dath sa
Lépp lou kawé ci yén day soufé ci man
Motakh dina len laal ba laalé gnougn souder si taat
Li ngen def sen carrière loumb laay déf nii tous les six mois
Dip doundou lerna souy rap day melni kou di wakh hey
Album bi rafétoul c'est magnifique fils
Dam lén bay ci biir gnouy cinéma ni Baye Ily nii
Bitch yaamay iri every time dou ma iri bitch
Sori wouma say taatou mc parceque ma ngi thi biir
Kouné dima tiré balle may dékkou maay fifty fils
Euppeu leu khaaliss diaay la doolé melni Macky Idy
Lokhotti sen mère ni OMG ak Mamy Viky
Bakhal sen khourou maami ci thin
Sotti mami thi biir
Ma ngi djiwé ma ngi Louga Capsi ma ngi Pikine
Kouma djigne franc maçon sa baay moy sacrifice bi
Mandit ci beat mandit ci style dama mandé sen fit
Mounoma diour nakh yaa ngi ak sama sperme si sa sidit yi bitch
Ah haah hahaa
Hey ok lnn toujours disponible l′album est toujours disponible Allez!
Streamer acheter en mode clé casque mi ngi nonou wherever fépp
Fo khaman tanei mom mo lafay gueuneul lnn toujours disponible yeah
Reptyle music



Writer(s): Dominique Preira


Dip Doundou Guiss - Président Fifa
Album Président Fifa
date de sortie
15-12-2019




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.