paroles de chanson ànd xeex coronavirus - Dip Doundou Guiss
Sa
loxo
set
Sa
lepp
set
Bul
nuyu
kenn
Bul
lëng
kenn
Bul
génn
kese
ndax
bëg
génn
Bul
sëqët
fepp
Bul
jége
kenn
Sëqët,
fièvre,
bop
buy
metti
njëk
feeñ
Soj,
problème
noyi,
senn
sa
bakkan
Sëqët,
fièvre,
put
buy
metti,
malaise
feeñ
Du
rey
nit
ku
ñul
si
ñi
xamul
dëg
ak
fenn
Sa
loxo
set
Sa
doom
yi
set
Bul
nuyu
kenn
Bul
lëng
kenn
Bul
génn
kese
ndax
bëg
génn
Bul
sëqët
fepp
Bul
jége
kenn
Sa
loxo
set
Sa
lepp
set
Bul
nuyu
kenn
Bul
lëng
kenn
Bul
génn
kese
ndax
bëg
génn
Xeex
ak
Corona
Virus,
Microbe,
jàngoro
la,
du
nit
Aduna
nek
si
combat
Du
gis
ku
muy
xeexal
Nuro
nak
grippe
Nañu
éviter
contact
physique
Xajul
Grand
Yoff,
Colobane,
Pikine
Tax
ba
ñu
annuler
programmes
yi
siiw
Tax
ba
ñu
foog
ni
àddinay
tukki
Medecin
sonu
na
si
li
Amul
vaccin,
ordonnance
tamit
Mu
ngi
ray,
day
toroxal
nit
yi
Buñu
tooge
dina
bari
ay
victimes
Set
si
sa
askan,
set
si
sa
bopu
Tëju
te
baña
seeti
sa
mbokk
Julli
sa
màkkaan,
Messe
si
la
bokk
Xeex
ko
mu
jeex
mbir
yepp
mëna
doxx
Masque,
sabu,
antiseptique
Raxasu,
sangu
dadi
set
wecc
Dal,
muñ,
bañ
lu
melni
dess
fi
Gën
di
ñaan
pour
jamm
day
dikk
Sa
loxo
set
Sa
lepp
set
Bul
nuyu
kenn
Bul
lëng
kenn
Bul
génn
kese
ndax
bëg
génn
Bul
sëqët
fepp
Bul
jége
kenn
Sëqët,
fièvre,
bop
buy
metti
njëk
feeñ
Soj,
problème
noyi,
senn
sa
bakkan
Sëqët,
fièvre,
put
buy
metti,
malaise
feeñ
Du
rey
nit
ku
ñul
si
ñi
xamul
dëg
ak
fenn
Sa
loxo
set
Sa
doom
yi
set
Bul
nuyu
kenn
Bul
lëng
kenn
Bul
génn
kese
ndax
bëg
génn
Bul
sëqët
fepp
Bul
jége
kenn
Sa
loxo
set
Sa
lepp
set
Bul
nuyu
kenn
Bul
lëng
kenn
Bul
génn
kese
ndax
bëg
génn
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.