El Hadj N'Diaye - Géej paroles de chanson

paroles de chanson Géej - El Hadj N'Diaye



Geej,geej maboulane
Geej,geej,Mbaboulan
Geej,geej, Mbaboulan ya ñi wootal Say dom
Geej geej Mbaboulan ya ñ wootal say doom
Geej,geej maboulane
Geej geej Mbaboulan ya ñi laabal sày doom
Dunde yakaar mba garaaw weex
Tës tësi mba doolé ñeex
Yakaar lab na biir geej
Tay mba sonk mbëg mi
Yakaar yi geersuna
Tay mba soobu geej
Bou lén fok ni jël loñoo neex na ma
Maay seen Avion yi di naaw
Barça wala balsak Li lén wutélé si man
Fu ma teele baax na si man taay
Bu lén fok ni jël loñoo neex na ma
Maay seen avion yi naaw
Geej,geej maboulane
Geej,geej Mbaboulan
Geej,geej, Mbaboulan ubil ma say loxo
Mbëgg na am jaabar am ay doom
Mbëgg na tekki ni samay morom
Mbëgg na sutural samay wajur
Ligeey yu ndaay àñum doom
Geej,geej Mbaboulan
Geej,geej, Mbaboulan
Geej,geej, Mbaboulan damaay wùtti ligeey
Yakaar yi geersuna tay mba soobu geej
Geej,geej Mbaboulan damay wùtti ligeey
Geej geej Mbaboulan taalal ma say loxo




El Hadj N'Diaye - Géej
Album Géej
date de sortie
02-04-2008




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.