El Hadj N'Diaye - Jolaa paroles de chanson

paroles de chanson Jolaa - El Hadj N'Diaye



Joola bi sux na
Rewmi am na tiis
Keerog bis boobu reew méempou jooy
Joola bi sux na
Rewmi méempou jooy
Bannexu jiit yi
Rangooñ askan wi
Joola bi sux na loño yagni digg
Bannexu jiit yi
Rangooñ askan wi
Am na ci gnoo xamni dotu gnu giis yaay
Dotu gnu bàay njirim yagni jooy
Joola bi sux na loño yagni digg
Bannexu jiit yi
Rangooñ askan wi
Siggi,jamonoy siggi la
Taane xoolu yak say bët
Ndaxte gor mën ta degge sëgg
Siggila tane jood ba melni kii gadàawu
Boleci nak dii lace lo yeeyo
Lu gnu dal waru gno wàar
Kùu añe rer bi
Bu xale yi dii jooy
Gna wara sëgg
Te kat bùu jooy ñeexe siggi jòt
Ndaxte kùu amul bàt ta giiso Yoon
Wara mëna siggi nak bane xoognu




El Hadj N'Diaye - Géej
Album Géej




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.