El Hadj N'Diaye - Lu Yëngu paroles de chanson

paroles de chanson Lu Yëngu - El Hadj N'Diaye



Lu yëngu lu yëngël lako ëppu doolé
Lu yëngu lu yëngël lako ëppu doolé
Ceedo du xet,
Ceedo Xalaat la
Lu yëngu lu yëngël lako ëppu doolé
Bukki ni ci yoon mba maay jaaré
Bukki ni ci yoon mba maay jaaré
Saaw yore fiitum rombu yoon w
Saaw yore fiitum rombu yoon w
Looy xulli bëtam,giis giisam
Giis giisam nélen giis giisam
Lu yëngu lu ko yëngël daf ko ëppu doolé
Kii yëngu,kuuko yëngël laako njaay doolé
Tàarxiss tòj na gëllu mbonat w
Kewël tëpp rombu yoon w
Gaayi teño wërëf niikuna taal aaluwa
Xel mi teey,yalla aar ñu
Gaynde lu ko gënël mooy jamm
Giis giisam nélen giis giisam
Lu yëngu lu ko yëngël daf ko ëppu doolé
Kii yëngu,kuuko yëngël laako njaay doolé
Waaw ni xaj ak yax baayi kooko
Xam maal ni buu ko wanne fòtt
Waaw ni xaj ak yax baayi kooko
Xam maal ni buu ko wanne buuku wanne fòtt
Ni saï saï,saï saï
Ni saï saï,saï saï




El Hadj N'Diaye - Thiaroye




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.