Elzo Jamdong feat. Mathart - Roy Thi Mom (Remix) [Bonus Track] paroles de chanson

paroles de chanson Roy Thi Mom (Remix) [Bonus Track] - Elzo Jamdong feat. Mathart



Samm diamm (diamm dongg), diammassanté (diamm)
Dokh tankou diam, dokh mbokk, bénieu diamanté
Diangg dionggou yokk diom fey ki meu dane bote
Diapp dioulli diamou diemeu diengou dioke te begneu toke (toke)
Dieuf dieuf diou rafet ndakhté wakh tidiégoul bounte
Mousslou thi thiate tamit ségueum lamigne djigoul bante
Tabakh diakk def ni mame sama tourondo, yokk barké
Mom mi dianggalaté batou Oumar Foutiyou ak Bamba Mbacké
Kakkatar thi bitim rew, doumeu fatté ni gaindé la
Gueuwmeu yakh bou rey wanté domou niaye bou ngaindé laa
Domou Salama Sow yaye nietti yone laley gueureum
Domou Hammady Laliyah, Baye Yalle nele Yalla yéreum
Santeu Yalla bi niou nekké goné guiss negn kouniou doy
Légui lerr ne me ligueyou ndèye rekeudi aniou dome
Dolli sante bi niou maggué am thi kou niou meuneu roy roy roy
Yow ya niou téter souniou Adiana yako mome mom mom
{Refrain}
(Mathart) -Yayeu woné ngor ak diom thi biir keur gui, Nioune niou roy thi mom
(Elzo) -Yayeu liguey rek niou roy thi mom
(Mathart) -Yayeu woné ngor ak diom thi biir keur gui, Nioune niou roy thi mom
(Elzo) -Yayeu liguey rek niou roy thi mom
(Mathart) -Dégloul me wakh leu benn yone Faut que me roy thi Mama
(Elzo) -Yayeu liguey rek niou roy thi mom
(Mathart) -Sou doyoul me wakh ko niaari yone Faut que roy thi Mama
(Elzo) - Yayeu liguey rek niou roy thi mom
{2ème }
Bineta, Kya, Rokhaya, Astou, Salma, dénk negn me lene
Kham nani dou Zair mane mi borom tèleu mey djiguene
Gor yomboul moss kou niakk fit ak Yalla yomb rére
Kom-kom dou thi am-am kou amoul diiné niakk rek
Diangg thi diouromi mak li takh be diémoumeu magg rakh
Di niane soutoreu yokkou yit diamm yagg sakh
Défar kate béniou bolé niou bokk déréte bokk darou
Tawey Altiné maye Gaou, Dibère mou mey Mama nopalou
Yalle ne fi yagg wer niou meuneu samm li niou Yalla mey
Ndakh seytané eupp dollé diourom niaari Balla Gaye
Boumeu sanione dane ko legui dioni dioni Hallyday
Baye dem neu, Yaye me nianati yalle ne le Yalla fey
Takk ndigg fass diom woné ngor nga mataléé
Tek thi goungué Baye beumou wathieu liguey Mama
Salama Thionké Seydou Gallo Guélel Amel Bessel
Cherif Seydou Hammady Laliyah Macina
{Refrain}
{Mathart - 3eme }
Tarbiyou neu Baye, liguey bi war thi nioune le def téwoul beu fi mouy try
Tarbiyou neu Baye liguey bi war thi nioune le def téwoul beu fi mou fight
Tankk bi gatt neu khéleum bi nekk thi Allahou
Dioulli di wore di niaane tallal Bour bi Allahou
Démoul fenn thi biir keureum leu toke di diaamou
Gueumoul Addouna ndiabote gui rekk leu taamou
Eskey live up Mama, yokk niou dolé lerr neu niou ni
Yangui fi di niaane fou sori legn niouy khole oh oh oh




Elzo Jamdong feat. Mathart - Freeseason
Album Freeseason
date de sortie
31-08-2015



Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.