paroles de chanson Capitale de la capitale - Elzo Jamdong
Intro
Digou
Sandaga...
Danouma
sétane
dessin
animé
ma
gueunone
touti
gallé
Te
benn
télé
moye
animer
Mcm
la
done
golou
Fi
deunguey
teleu
dem
matinee
lepp
ngay
teeleu
def
Digou
Dakar,
rissou
ragga
bou
Dj
matar
di
animer
Dou
takh
nga
niakk
talibé
maman
neneu
gentil
na
Te
bizarrement
Seme
grand
yi
nénegn
bandit
la
Wa
gallé
dolene
wone
se
fit
temps
wou
gentina
Boumay
zoner
corner
douma
andak
samay
sentiments
Fi
biniou
amé
7 ans
legn
khammé
lax
Fi
biniou
13
ans
legn
dougg
Stax
Fi
mm
bo
amoul
mak
deunguey
teleu
nande
Wakhoumala
nak
nga
done
namp
tchi
boutelou
mak
Rote
onde
toni
pack
litrou
valmerass
Dougg
na
tchi
guenne
na
tchi
rue
de
Valmy
rame
Dounde
na
ko
tangana
ak
roukhou
macky
saf
10
ans
apres
none
le
kogn
bi
gueuné
yakhou
macky
saleté
Boy
yi
tey
legn
gueuneu
dee
walo
tey
le
gueuneu
aaye
Moye
gni
dieunde
diaye
coke
marché
comme
si
c
legal
Fi
dou
Washington
mais
am
ne
maf
ni
birr
Capitol
Mey
ko
ko
baol-baol
yi
ak
ndring
yi
seme
capitale
Dem
naChitown
dounde
système
fédéral
Dem
na
la
défense
Dem
châtelet
les
halles
Deukk
na
kawe
weur
na
senegal
Guiss
na
ni
wa
town
douniou
sene
égal
Capitale
de
la
capitale
Capitale
de
la
capitale
Capitale
de
la
capitale
Wa
town
douniou
sene
égal
Danouma
sétane
dessin
animé
ma
gueunone
touti
gallé
Te
benn
télé
moye
animer
MTV
la
done
golou
Fi
deunguey
teleu
dem
matinee
lepp
ngay
teeleu
def
Tem
nga
aligner
beu
abimer
wathieu
do
wala
alizé
Dou
te
nga
am
idée
donté
nga
teleu
guinz
bitch
Bo
amoul
chance
deugueur
deug
rek
deunguey
kinss
fils
limeudane
romb
goudi
town?
momeu
indil
inspi
Bimey
ndieukk
binde
16
amagouma
15
piges
Est-ce
que
kham
nga
ay
Fouquets?
Africa
star?
Sista
yi
jobé
rue
Escarfait
angle
Raffenel
Hotel
du
marché,
Albert
Sarraut
Saloon
Texas...
Gni
maggué
town
rekkeu
kham
né
Ponty
amoul
thiaga
Matin
bi
deunguey
diangg
ngone
deunguey
def
street
Night
bi
deunguey
tokh
bone
deunguey
def
bizz
Am
ay
copain
you
deukkoul
corner
nieuw
pour
nga
yoboulene
salle
de
vente
diaye
feu
last
call
nga
am
se
lekkou
deal
Thioy
yi
diapp
negn
Gangsta
yi
dakkhone
diapp
daadj
Boy
yi
done
daakh
sip
legui
nio
magg
daakh
deal
Bo
amé
grand
you
deukk
jail
do
to
diapp
chill
Do
faaléti
ay
yermeundé
dieguelou
diapp
tchi
Boy
yi
tey
legn
gueuneu
dee
walo
tey
le
gueuneu
aaye
Moye
gni
dieundeuk
diaye
coke
marché
comme
si
c
legal
Fi
nimou
beuré
batiment
non
leu
beuré
batiman
Mey
ko
pourtou
ngagno
yi
ak
naar
yi
sama
capitale
![Elzo Jamdong - Freengdom](https://pic.Lyrhub.com/img/t/g/w/b/BSYVjaBwGT.jpg)
1 Patriarche (Bonus WTF)
2 Khel Niaar
3 Badimi (Body Me)
4 Une si longue lettre
5 Tout-bas (Interlude)
6 Lost Times
7 Khoudar
8 Allou Ciment
9 Faith
10 Ghetto
11 Patriarche
12 Assiko Flow
13 Yow Lë
14 All My Life
15 Comme Mane
16 Capitale de la capitale
17 Moment of Silence
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.