paroles de chanson Yow Lë - Elzo Jamdong
Yow
lë
Sama
xol
fess
na
takh
gua
may
podj
Nala
defaal
lo
guissoul
ci
ben
goor
Say
tiono
diekhna
may
ki
lay
soore
Waaw
goor
Douma
bokk
ci
goor
yilaay
door
Guisna
ci
say
beute
xargua
ba
soy
Guissoulo
kou
crx
taxna
guaay
dioy
Say
ronguogn
ferna
may
kilaay
yoor
Gni
ay
xolou
xer
lagn
yor
mane
may
or
Wane
gua
ma
foula
ak
diom
Wane
gua
ma
wane
gua
dioup
ak
ngoor
Souba
ak
guone
dina
dioubo
ak
yaw
Yama
takh
beug
diour
ay
dome
Bou
sobei
Yallah
digua
soul
sa
ay
none
Diouyo
ak
niom
gnou
bokk
doulo
ak
yaw
Digua
done
bour
digua
sour
ak
forme
Ba
gnila
beugua
loorr
beug
ndiro
ak
yaw
YAW
LA
BEUG
NALA
TAKAL
BAGUE
KENINN
KOULA
BEUG
TAKK
NAKO
TAKAAL
AY
BOMB
Deug
deug
Diaraal
gama
rakk
Douma
doyaal
dila
taagu
dila
nié
diko
tioow
Yafi
tek
tankk
yay
bomb
Koula
guerre
nako
gone
militaire
lay
done
Bigua
dalei
ci
mane
lassa
xel
wara
daal
dina
dem
Diaka
gua
dem
mairie
sol
robe
Yay
done
kiy
diour
samay
dome
Soma
degualoul
damay
doff
(hey)
Yay
done
kiy
diour
samay
dome
(hou
hey
ii)
Sama
gueineu
waleu
guay
dome
(oh
oouh
oh!
Oh
oouh
oh)
Sama
guéneu
waleu
guay
done
Sama
guéneu
waleu
guay
done
(Oh
ouh
oh!
Oh
ouh
oh)
Yay
done
kiy
diour
samay
dome
(Hou
hey
ii)
Sama
gueineu
waleu
guay
done
(Oh
ouh
oh!
Oh
ouh
oh)
Yow
la
taneu
(yow
lë)
Yaaw
la
tamou
(yow
lë)
Guisna
ci
yaw
lou
kene
amoul
Oh
ouh
oh!
Oh
ouh
oh)
Yaw
la
taneu
(yow
lë)
yaw
la
tamou
(yow
lë)
Digua
am
si
mane
lou
kene
amoul
Yow
lë
Yow
lë
ëë
Yow
lë
Yow
lë
Yow
Lë
ëë
Tiebou
yap
bou
kheign
neu
Amatoula
loumaay
neub
lepp
fegn
neu
Yagu
na
dadialei
ay
tioro
Wayé
louma
meussa
am
ci
diangori
djiguene
lepp
dagn
neu
Gnila
togn
togn
nagnma
Dou
wakhou
pitieu
mais
wakhou
wegn
(fer)
leu
Def
tiakay
di
tal
sama
money
dou
lima
guondi
di
guene
dila
fi
bayi
dafaay
fekk
ma
bagnla
Legui
takoussane
diote
yagatoul
yagatoul
legui
tak
seuy
diote
Legui
samaay
gooro
daldi
sakou
sen
dote
Legui
Pa
yi
diouguei
diakeu
gua
tagou
say
mbokk
Mousso
dem
ba
finale
ak
mane
Meusgua
touki
wayei
di
gua
dem
féninn
ak
mane
Dinkeu
nagnoumala
gua
fanane
ak
mane
Sama
dekhou
baneeekh
digu
fa
naane
akk
mane
Tey
la
beuss
bi
dak
sama
life
Tey
lay
dogua
nek
kilifa
bima
yagu
beug
done
Diaré
ci
kou
rafeet
xol
Mangui
fateilikou
bima
done
guenteu
dila
xol
dissi
diamou
sougnou
borom
Yagu
yekk
péekh
biy
wané
ni
gnigui
si
yone
Ndakh
nena
seuy
bokna
ci
loumou
gueuna
sopp
Yay
done
kiy
diour
samay
dome
Soma
degualoul
damay
doff
(hey)
Yay
done
kiy
diour
samay
dome
(hou
hey
ii)
Sama
gueineu
waleu
guay
dome
(oh
oouh
oh!
Oh
oouh
oh)
Sama
guéneu
waleu
guay
done
Sama
guéneu
waleu
guay
done
(Oh
ouh
oh!
Oh
ouh
oh)
Yay
done
kiy
diour
samay
dome
(Hou
hey
ii)
Sama
gueineu
waleu
guay
done
(Oh
ouh
oh!
Oh
ouh
oh)
Yow
la
taneu
(yow
lë)
Yaaw
la
tamou
(yow
lë)
Guisna
ci
yaw
lou
kene
amoul
Oh
ouh
oh!
Oh
ouh
oh)
Yaw
la
taneu
(yow
lë)
yaw
la
tamou
(yow
lë)
Digua
am
si
mane
lou
kene
amoul
Oh
ouh
ooh
1 Patriarche (Bonus WTF)
2 Khel Niaar
3 Badimi (Body Me)
4 Une si longue lettre
5 Tout-bas (Interlude)
6 Lost Times
7 Khoudar
8 Allou Ciment
9 Faith
10 Ghetto
11 Patriarche
12 Assiko Flow
13 Yow Lë
14 All My Life
15 Comme Mane
16 Capitale de la capitale
17 Moment of Silence
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.