Elzo Jamdong - Melomind paroles de chanson

paroles de chanson Melomind - Elzo Jamdong



where they at? anh
Ndakh malen wara yéé
you now listening to Free music, ok
Yeah mafi geuneu tipsé, town ba Yeumbeul
nagn baay bi dafa peace mais, ci sound day sound dey yeunguel
haaa heuu heuu hii héé
haa heuu heuu
xolal mafii ñeukeu riimé phrase you leumbeu
moune naa diapizé ak ay cassou zeumeu
diaroul wayne xéliil ma kelk base yuu degeur
Beycon ak Amber rose douu ma sein massou djeukeur
diotayy bouma bokk MC dou nazz dou peundeu
Nullard MC nékeu dii tassou lembeul
kein amoussi ndieuriin comm ay phare you leuudeum
Bayileine dii critiqué waar bou pheleuu
Hip Hop geuneuu noble cii lii art bii eumbeu
Ma change rime mbalakh sapi waroul ndirouu louu yoomb dance yi ñeupeu andeu happy mélnii koudroul Song
anoosak thiiriirii ma safal fiiiliinii
Bou doyoul ma defatt koo easyly easyly easyly
Genrou ambiance yii dimaz fatélil 2002
diamono yii mane ak petit dii démal door
Homie tu sais faire mieux démal door
Dégougumafiii daraa loudoul DIMIL doul
MC yii ma thiop nélein fii souragoul
Maguii cii biir sama diig touragoul
May beutou pyramide bii ñom ñi guii sii soufaa souf
Dianguii laa niow tass nii Vivi Bouba ndour
coup de boul gua bougonn sama liguey
Sall, Gueye hann ñoune gua bougone liguay hann
Guinte-ma, ma guéneu Game gua neik péé hann
Foliinalein Souleymane Ndéné Guéye hann
keiin dieundatoul sein dope comme vrac'k
Ndakh diamono bougatoul andeu féft guein blocker
Mane dañ tambeu sama flow comme crac'k
kou tokk son wam diamboul, sama son rek cracker
Tangeu bay laacké, léguii guay dogua reconize ...(taaar mbeth)
Koula lath naka joob rk nékoo nice
dékoo fayy, diamona dina dinaa dokh
koulaa, bouga, diokh, waxou doff diapéwoulaa melomind
kiileu geneu joob lay fayy
kii laa gineu hiileuu ñiileu gineu bokk diñu ko béyy nigger
Kone my boy nañ ko bañ nay boy... (nala gañ iow)
ba askan yii accepter nañu excése
Ñu nagou nék bétomind nono, ba lascar yii acceder cii ay aypeiss
beurina ay texte, fils léguii may chef fii boumay may check rk ñu signel-ma ay cheque
boyii texas ak money and thug, fok impress yu baxii léguii money lañ geum
na yéneu mec yii bayiii sathii, Jamdond leu, niom macky bayii sathii
(noo no dama dioum)
na yéneu boy yii bayiii cathii Jamdong leu, beuu sen bayiii bay sathii
haaaaa




Elzo Jamdong - Freedope
Album Freedope
date de sortie
14-12-2014




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.