paroles de chanson Roy Thi Mom - Elzo Jamdong
Bridge1
Maye
souniou
thiaatou
keur,
seme
khol
mounoul
bénieu
yatou
mbeur
Me
guénne
thi
mbedd
mi
dieul
mic
wakhal
nit
gni
ndakh
mounoumeu
wone
nekk
souniou
baatou
keur
An
boul
khèpe
seme
guéy-li
(liguéy);
flow
bi
takh
nga
fok
né
poésie
ngay
lire
Ngamey
diaye
grand
yar
sikim
ni
bey
ni
Mey
pas
thi
game
bi
yow
ngay
lirr
(come
back
come
back
come
back)
Maye
souniou
thiaatou
keur,
seme
khol
mounoul
wone
bénieu
yatou
mbeur
(cheah)
Me
guénne
thi
mbedd
mi
dieul
mic
wakhal
nit
gni
ndakh
mounoumeu
wone
nekk
souniou
baatou
keur
Son
bi
la
tamou
deme
dioye
thi
mom
Flow
biy
diokhé
daadj
té
dou
doy
thi
bopp
Mom
la
BEUG
takkal
nako
BAGUE
moméy
BEGUEUL
Pac
BIGGIE
gningui
khole
waroul
noye
thi
yone
½ "Free
flow
bi
nice
ne",
-Yayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
"Free
video
bi
nice
neu",
-Yayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
"Free
non
jo
yi
nice
neu",
-Yayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
"Free
non
bro
bou
nice
le
nak"!
-Yayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
Yé-yé-yéksina
sène
yakaar
la
tass
Gni
thi
nangou
deugg
nangou
Dakar
la
tass
(run
the
city)
Kou
lakkhou
di
nane
bo
mandé
fègne
(hahahaha
cheah)
Diapp
nguène
Ino,
bénène
bandé
fègne
Lé-lé-légui
légui
légui
nioye
doweul
souniou
biz
thi
tali
bi
(talal
auto
bi)
Bo
khamoul
lou
beuri
boul
wout
alibi
(boul
fén
se
bopp)
Togg
na
quantité
yékk
na
qualité
(cookin
the
FreeDope!)
Bou
nguène
faké-woul
wone
sakh
me
mey
lene
parité
(yeah)
Bridge
2
Maye
souniou
thiaatou
keur,
seme
khol
mounoul
wone
bénieu
yatou
mbeur
Me
guénne
thi
mbedd
mi
dieul
mic
wakhal
nit
gni
ndakh
mounoumeu
wone
nekk
souniou
baatou
keur
(oh
Free!)
Pa
bi
ak
Mère
deme
dioye
thi
niome
Gni
me
gueuneu
diégué
nio
mey
dolli
diom
Gallé
Yalle
ne
diGUEUnté
yi
GUEUneu
deuGUEUr
Boumou
DAGG
negn
ko
fas
ndakhté
waroul
noye
thi
yone
"Free
flow
bi
nice
ne",
-Yayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
"Free
video
bi
nice
neu",
-Yayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
"Free
jo
yi
nice
neu",
-Yayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
"Free?
non
bro
bou
nice
le
nak",
-Yayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
Roy
thi
mom
roy-roy
thi
mom,
Yayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
Roy
thi
mom
ro-ro-roy
thi
mom,
Bayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
"Free
flow
bi
nice
ne",
-Yayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
"Free?
non
bro
bou
nice
le
nak"!
-Yayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
Deme
ekssi
lakk
lepp
bepp
vampaya
décéder
(burn
dem)
Melomind
yangui
sogueu
kham
ni
degn
le
done
nakh
ndékété
(degn
le
done
nakh
rek)
They
can't
defeat
me
cause
I'm
not
fair
(I'm
not
fair)
Do-Do-Dor-Dor
na
#War
kone
gagner
na
#guerre
(yeah)
Seme
gaïndé
pa
defe
niafé
seme
mère
def
woné
ngor
(woné
ngor,
defe
woné
ngor)
Loumou
diafé
diafé
niounite
deniou
wara
féy
bor
(féy
bor
anhan)
Daddy
ak
mère
dégn
#War
pour
me
sol
#jo
(cheah)
Motakh
sene
dome
magg
nekk
#fly
#soldier!
(cheah)
Bridge
3
Maye
souniou
thiaatou
keur
(anhan),
seme
khol
mounoul
wone
bénieu
yatou
mbeur
Me
guénne
thi
mbedd
mi
dieul
mic
wakhal
nit
gni
ndakh
mounoumeu
wone
nekk
souniou
baatou
keur
Pa
bi
ak
Mère
dégn
job
real
love
Yalleu
ne
seme
dome
meuneu
roy
thi
lol
Gallé
Yalle
ne
diGUEUnté
yi
GUEUneu
DEUGUEUr
Boumou
DAGG
negn
ko
fas
ndakhté
waroul
noye
thi
yonnne
"Free
flow
bi
nice
ne",
-Yayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
"Free
video
bi
nice
neu",
-Yayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
"Free
jo
yi
nice
neu",
-Yayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
"Free?
non
bro
bou
nice
le
nak",
-Yayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
Roy
thi
mom
roy-roy
thi
mom,
Yayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
Roy
thi
mom
ro-ro-roy
thi
mom,
Bayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
"Free
flow
bi
nice
ne",
-Yayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
"Free?
non
bro
bou
nice
le
nak"!
-Yayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
Yayeu
liguey
rek
me
roy
thi
mom
X4
FreeDope
Elzo
Melomind
Raison
Nègre
(FreeDope)
Judge
Not
Lonely
Beats
By
Thiere
Dans
Mon
Monde
Seuss
TeauPla
Anthem
Roy
Thi
Mom
PositiVibz
AUDIO
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.