Elzo Jamdong - Tout-bas (Interlude) - traduction des paroles en anglais

Paroles et traduction Elzo Jamdong - Tout-bas (Interlude)




Tout-bas (Interlude)
All Quiet (Interlude)
Ay rimes laye yor di leu ko sékheul mouy dougg se khél
Hey, my rhymes are here, let them tell you that the game is on, it's a spectacle
Stop mane sakh kaddou la yor wala kouddou
Stop acting tough, woman, whether you're here or not
Touddé seme bopp free bénieu tédiou sene jail
Stay free, my beautiful one, prison isn't for you
Li mey néttali lepp bala mey reuthieu la ko dounde
Life is beautiful, my love, don't let anyone tell you otherwise
Temps boy degn danefo pape ak yaye tédiou thi roukkh
Time flies, I miss Dad and Mom, they've left this world
amoul ken thi nioune kou niou nettali fane leu diar be diouddou
But I have you, my love, and that's enough to make me forget my sorrows
Diarouteu magg diangg pour compe ni gore djiguéné baakhoul
I take detours to avoid competition and meaningless arguments
Mok dord jiguéneu yém kou thiné do gor djouguenn ndiakhoum
I see people arguing but I choose to stay out of useless conflicts
Bo diogué yakhounégn NDAKH degn yanou mana
I don't provoke anyone, NDAKH, I mind my own business
Yow falounga diengouwo SAKH guiss yonou money
I speak my truth and focus on making money
Yenn mar yi kou leu gassal PAKH mou nekk potit
I've been hustling since I was a kid
Nga tankkh nane do yég yen a marre ak potopoto
I'm tired of the drama and the gossip
Bienvenue fi degn ley yéné merde, di le diémeu yédd
Welcome to my world, full of shit, tell the devil I said hi
Kou fi diémeu tedd mouno toukki niouné le ya feu
If the devil messes with me, I'll light him on fire
Defe yémé man degn ley yèwe def le diamou mbed
Fire is what I see when I look at your body, it's pure desire
Bolou gouddi yi niouy lekka takh niou diappé aye feudo
We lick the sweet lollipops, we dress up, and we party
Niouné nio mer han wala yéneu merder?
Are we going to die today or tomorrow?
Kou meyone kaddou idrissa ndiaye kou diokh ndam Selbé?
Should I marry Idrissa Ndiaye or wait for Selbé?
Ki sokhleuwoul ndokhou tow toleu meu ngui sakh
Who is whispering lies behind my back?
Ki fanane thi mbedd di liw kholeu meu ngui bakh
Who wants my downfall while pretending to be my friend?
Ladial Mimi ndakh cadence accélerer neu some
Ladial Mimi speeds up the cadence, it's getting intense
Beu légui Do tabakh se keur ak salairou maçon
I left Do with a pack of cigarettes, a heart full of dreams, and a mason's salary
Li beykate yi di dioye kouko nara gérer mou sakh
I ignore the haters, I don't care about their drama
Casino ya ngui takk yonou adiana lereugoul sakh
The casino takes my money, Adiana steals my heart
x2
x2
Me wakh tchi kow le nieup di mind tout bas
I'm telling you what's on my mind, quietly
Nit kou niouleu rey Malcolm ak Tupac
Like Malcolm and Tupac used to
Me wakh tchi kow li nieup di mind tout bas
I'm telling you what's on my mind, quietly
Loutakh me war leu wolou daal di saaga toubab
Tired of these meaningless stories from the white man's saga






Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.