Ismaël Lô - Diour Sani paroles de chanson

paroles de chanson Diour Sani - Ismaël Lô



Par abouamg
Nene yagui dogue dioudou
Sa yayboy dieule sanni
Nene yagui dogue dioudou
Sayayboy dieule sanni
Mome de dala khamoul
Waye khamnane ll guathiela
Mome de dala khamoul
Waye khamnane ll guathiela
Dom bl ngua diour sanni tarangam yorouloko
Kl euleuk mom dina teki euleuk dina teki
Bou teke nokay khole
Boula dioure sanni amna gnenen gnoula beugueu
Boula dioure sanni amna gnenen gnoula beugueu
Boula dioure sanni amna gnenen gnoula beugueu
Boula dioure sanni amna gnenen gnoula beugueu
Wala ragal wadiour mokasi dougal bebe amna retiouna
Oh bebe balkoo
Ndakh woornama amatouli nelaw
Bebe yaw sayo dioye wornama danako yeuk famou ne
Bebe
Bebe
Boula dioure sanni amna gnenen gnoula beugueu
Dafa khamoul amna gnenen gnoula sokhla
Bour yala mayou lenko lolou moy ndogolou yalaa
He kl euleuk mome dina teki bou teke nokay khole
He nokay khole
Bebe
Dadada ndakh wornama amatouli nelaw bebe yaw sayo dioye
Wornama danako yeuk famouneee
Bebe kay ma oufla
Bebe kay ma rayla
Bebe kay ma nanpal la
Bebe bebe bebe bebe balcoo



Writer(s): Ismaël Lo, Ismael Lo


Ismaël Lô - Dabah
Album Dabah
date de sortie
26-06-2001




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.