paroles de chanson Manko - Ismaël Lô
Par
AbouAmg
Xalatna
bouguen
De
guisse
Ken
doulen
feole
Xalatna
bouguen
de
guisse
Gueneu
waxtane
mana
dioubo
Lou
bakhla
Xalatna
bouguen
de
guisse
Diguen
gueneu
am
dole
Xalatna
bouguen
de
guisse
Gueneu
waxtane
mana
dioubo
Lou
bakhla
Ndakh
koumou
manti
done
si
yengni
Ya
gui
bay
si
warwi
Ya
kham
guor
gua
yakham
djiguen
gua
Nguen
anda
ndo
bay
warwi
Ndakh
gueum
nani
mbolo
mbolo
rek
Modi
dole
Lou
bakhla
Man
lankeuna
man
bagne
na
Gnou
nane
politicien
yi
dagno
fewalo
Souma
amone
lima
gueunal
maan
Nguen
andando
boka
dole
Ndakh
gueum
nani
mbolo
mbolo
rek
Modi
dole
Lou
bakhla
Koumou
manti
done
si
gnoun
gni
Diaamou
senegal
rek
moy
sa
yene
Souma
amone
lima
gueunal
maan
Nagnou
andando
boka
dole
Ndakh
maan
gueum
nani
mbolo
Mbolo
rek
modi
dole
Lou
bakhla
Maan
gueum
nani
bougnou
ande
bolo
Mo
gueun
sougnoum
rew
Nagn
diohonn
te
loho
Maan
gueum
nani
bougnou
ande
bolo
Mo
gueun
sougnoum
rew
Nagn
diohonn
te
loho
Xalatna
lou
bakhla
xalatna
lou
gueun
le
Bougnou
ande
bolo
gnoun
dana
Sapadeuguin
Xalatna
lou
bakhla
xalatna
lou
gueun
le
Bougnou
ande
bolo
gnoun
dana
Sapadeuguin
Ndakh
maan
gueum
nani
mbolo
Mbolo
rek
modi
dole
Lou
bakhla
Maan
gueum
nani
mbolo
mbolo
rek
Modi
dole
Lou
bakhla
Xalatna
bouguen
manko
dinguen
Gueune
am
dole
Xalatna
bouguen
manko
gueneu
waxtane
Mana
dioubo
Kone
lou
bakhla

1 Baykat
2 Incha Allah
3 Tass Yakar
4 Le Jola
5 Taar Dousey
6 Manko
7 Yaye Boye
8 Plus Je Fais Ci, Plus Je Fais Ca
9 Mbindane
10 Wakhal
11 Ouvriers
12 Jiguen
13 Ma Fille
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.