Iss 814 - Miim Reew paroles de chanson

paroles de chanson Miim Reew - Iss 814




Police dou décroché
Sapeur Daye yékha gneuw
Nénagnou dou raccroché
fepp la meneu gneuw
Amna gnou roussoul
Dieuw neew sa biir corbillard
Amna gnouy dingate sen Serigne
deugno gneuw ziaar
Djiko youdoul dégne
Nii fébaar youdoul weer
Politique égale politique
Même bou néké sen keur



Writer(s): Ismaila Talla



Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.