paroles de chanson Probleme - Iss 814
-Refrain-
Né
nga
da
nga
am
problème
Mais
mala
eup
problème
Kou
si
nék
amna
problème
Mais
dou
nieupeu
kay
waax
Né
nga
da
nga
am
problème
Mais
mala
eup
problème
Kou
si
nék
amna
problème
Mais
dou
nieupeu
kay
waax
-Couplet-
Amo
ndieugou
ordonance
Mane
cancer
moma
dal
Est
ce
que
doma
dimbeli
si
pass
Mane
si
bourlé
car
lako
cal
Sa
guél
daf
la
trahir
Mane
sama
guél
néna
dafa
biir
Boudé
ya
ngi
souffrir
Mais
mane
ma
ngi
dé
si
biir
Cent
mille
problèmes
Millions
problèmes
Milliards
problèmes
Fuck
dix
mille
problèmes
Soum
koy
nétali
do
dém
Diogué
si
problème
dalaate
si
problème
Fatal
say
problèmes
Amo
yéré
yo
sol
mane
tatounène
laal
dèf
Ngané
bèn
guél
doula
xool
Équipou
laambe
bi
mafay
chef
Né
nga
da
nga
am
problème
Mais
mala
eup
problème
Kou
si
nék
amna
problème
Mais
dou
nieupeu
kay
waax
Né
nga
da
nga
am
problème
Mais
mala
eup
problème
Kou
si
nék
amna
problème
Mais
dou
nieupeu
kay
waax
Sa
rakk
dafa
AVC
Sama
mak
dafa
ébola
Indi
na
acte
de
décès
Bayiwoufi
ndieugou
chocolat
Sa
guél
day
saw
lal
sama
diabar
day
poupe
lale
Xawma
lane
mola
dale
Sama
problème
khadoul
hôpital
Amo
lo
fayé
louass
Mane
huissier
dafma
guéné
Dénkanéna
samay
bagass
Niou
nonou
galé
Ndiémé
Vivre
sa
problème
pour
yaw
té
boumako
nétali
Ndax
amna
problème
comme
yaw
sama
paane
boulko
féthiali
-Refrain-
Né
nga
da
nga
am
problème
Mais
mala
eup
problème
Kou
si
nék
amna
problème
Mais
dou
nieupeu
kay
waax
Né
nga
da
nga
am
problème
Mais
mala
eup
problème
Kou
si
nék
amna
problème
Mais
dou
nieupeu
kay
waax
Yééé...
Ooooh...
Da
ngay
am
say
problèmes
Wéteuk
sa
problème
Bayima
ak
sa
problème
Yaw
mom
no
problèmes
Da
ngay
am
say
problèmes
Seuf
ma
say
problème
Dèss
si
sa
problème
Yaw
mom
no
problèmes
Da
ngay
am
say
problèmes
Baa
ma
ak
sa
problème
Ba
doto
amati
problème
Yaw
mom
no
problèmes
Né
nga
da
nga
am
problème
Mais
mala
eup
problème
Kou
si
nék
amna
problème
Mais
dou
nieupeu
kay
waax
Né
nga
da
nga
am
problème
Mais
mala
eup
problème
Kou
si
nék
amna
problème
Mais
dou
nieupeu
kay
waax
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.