Iss 814 - Noce paroles de chanson

paroles de chanson Noce - Iss 814



Ku xebul sa noce ken dakula noce (×2)
Million noce
Mille francs noce
Uno noce
Feguediay noce
Ku xebul sa noce ken dakula noce (×2)
Mille francs noce
Millions noce
Uno noce
Feuguediay noce
Sama 10.000
Millions Lopy
Sama liberté
Prison Lopy
Pabi amul milliards mais mesuñu xif
Cere reer fondei fajar namuñu boeuf
Mère daye fessal panier ta pabi du yor
Keine mesuko poñe di fayeku borr
Gningi ci école publique iow école privée
Lutax buñu passé ngay redoublé
Sosal sa sauce ñun ñu sim suñu cere
Nocal sa noce ñun mom duñlako tere
Solal sa koss ñeeti abdu beine bere
Li deff sa poche ci sa xel la dussi yere
Ku xebul sa noce ken dakula noce (×2)
Million noce
Mille francs noce
Uno noce
Feugdiay noce
Ku xebul sa noce ken dakula noce (×2)
Mille francs noce
Millions noce
Uno noce
Feugdiay noce
Amna ñu deuxin gueneul méchoui
Amna ñu geztner gueneul Louis Vi
Bo amul linga beug dangay yam si linga am
Kuleu guiss joxla gued lingay dunde duñko xam
Sama dignité seu dole poche
Nitt daye nitté même buy xoss
Nittengi ci région ñewul ñi nekk ci capital
Nitt yorna ay milliards di jabante hôpital
Sant yalla buñsi tolei fi taye
Dox pas à pas doylo lepp luñ ñu maye
Kune fone xeyna moye sa njiglay
Amnga lune mais god moyor muslay
Ku xebul sa noce keine dakula noce (×2)
Millions noce
Mille francs noce
Uno noce
Feugdiay noce
Ku xebul sa noce keine dakula noce (×2)
Mille francs noce
Millions noce
Uno noce
Feugdiay noce



Writer(s): Iss 814


Iss 814 - Noce - Single
Album Noce - Single
date de sortie
01-08-2018

1 Noce




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.