Iss 814 - Samay Neggerz paroles de chanson

paroles de chanson Samay Neggerz - Iss 814



Samay niggas beugou ñou la
Da ñou ley setane buñ ley rey
Samay niggas beugou ñou la
Da ñou ley retane buñ ley rey
Prrra prrra
Diox ñu xaliss wala plomb
Prrra prrra
Diox ñu xaliss wala plomb (plomb yeah)
Keneu dou négocier (yeah)
Produit qualité (cali)
Ñeupeu ko valider (yeah)
Keneu dou ko copier
Siriki ak Suké (prra)
Tite da nguey comédie (han)
Diokh ñu ay tickets (yeah)
Mba ñu appliquer
Amul Kendal Rihanna (Rihanna)
Da ñuy ñow taal terreau man (terreau man)
Djiko Van Damme, Superman (superman)
Def scandale sisa mame (yeah)
Ken dou bloquer sunu couche (sunu couche)
Da ñu blessé gana pousse (yeah yeah)
Gueumeu ñu tok banc de touche
Ay djiko bone gana louche (yeah yeah)
Samay niggas beugou ñou la
Da ñou ley setane buñ ley rey (bougou ñou la un deux)
Samay niggas beugou ñou la
Da ñou ley retane buñ ley rey
Prrra prrra (prrr)
Diox ñu xaliss wala plomb (dinero dinero)
Prrra prrra (skut)
Diox ñu xaliss wala plomb (dinero dinero)
Samay niggas beugou ñou la
Da ñou ley setane buñ ley rey (skut skut skut)
Samay niggas beugou ñou la
Da ñou ley retane buñ ley rey
Prrra prrra
Diox ñu xaliss wala plomb (dinero dinero)
Prrra prrra
Diox ñu xaliss wala plomb (yeah yeah yeah)
Ngané do fey ok
Magnum sissa bop pop nga deh
Amoul demi xaliss buñuy accepter
Meno ñu reutieu ñu gui si quatre côtés
Sama lamigne'a dama sa yaram kot koté
Teuyeul ñu sa wax yi diaroul papoter
Sa bop ak sa nop lañuy fat faté
Taxaw sa kanam comme bateau ma accosté
All ok
Feyoulo da ñu ley shoot (shoot)
Amulo on s'en fout
Na nga ñow buñu doul (yeah)
Boufi wax da ngey loud (loud)
Dañuy job duñu play (play)
Bo fiy fo dañu ley rey (rey)
Moratoire non dou tey (hey)
Samay niggas beugou ñou la
Da ñou ley setane buñ ley rey (bougou ñou la un deux)
Samay niggas beugou ñou la
Da ñou ley retane buñ ley rey
Prrra prrra (prrr)
Diox ñu xaliss wala plomb (dinero dinero)
Prrra prrra (skut)
Diox ñu xaliss wala plomb (dinero dinero)
Samay niggas beugou ñou la
Da ñou ley setane buñ ley rey (skut skut skut)
Samay niggas beugou ñou la
Da ñou ley retane buñ ley rey
Prrra prrra
Diox ñu xaliss wala plomb (dinero dinero)
Prrra prrra
Diox ñu xaliss wala plomb (yeah yeah yeah)



Writer(s): Ismaila Talla


Iss 814 - Bicrave
Album Bicrave
date de sortie
30-12-2020




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.