paroles de chanson Aminata - Iss 814
Amou
ma
or,
amou
ma
xaliss,
amou
ma
ay
liasse
Né
ngua
do
guéne
ak
mane
ndakh
awmeu
clash
Loutakh
ngua
melni
Aminata?
Mane
xamouma,
bébé
wakhma
Amou
ma
or,
amou
ma
xaliss,
amou
ma
ay
liasse
Né
ngua
do
guéne
ak
mane
ndakh
amou
meu
classe
Loutakh
ngua
melni
Aminata?
Loutakh
ngua
melni
Aminata?
Lane
ngua
meu
eupeulé
Motoul
sakh
pép
thiép
Nio
bokk
deuk
tchi
kogne,
loutakh
yaw
ngua
mayy
khép?
Yéne
dieuff
yi
nguay
deff,
tchi
sama
khol
daf
may
guagne
Yéne
say
ma
diépi
leu
déme
bay
bayi,
khol
bi
bagne
Sama
mbeuguél
moma
togne,
motakh
ma
topeuleu
Mane
ak
yaw
nio
bok
kogne
motakh
ma
sopp
leu
Kheuyneu
beuss
di
na
ame
kagn,
takk
leu,
téreul
leu
Hé
eh,
Hé
eh
Thioro
baye
samba,
dak
sa
yaye
dieulmeu
Sa
nijaay
yo
may
ma
ay
dollar,
dou
ma
té
daggo
Djank
bi
tchi
kogne
bi
néna
dou
sey
ak
badolo
Bo
démé
keur
yayam
goudi
gossi
lay
réré
Amou
ma
or,
amou
ma
xaliss,
amou
ma
ay
liasse
Né
ngua
do
guéne
ak
mane
ndakh
amou
meu
ay
clash
Loutakh
ngua
melni
Aminata?
Mane
xamouma,
bébé
wakhma
Amou
ma
or,
amou
ma
xaliss,
amou
ma
ay
liasse
Né
ngua
do
guéne
ak
mane
ndakh
amou
meu
class
Loutakh
ngua
melni
Aminata?
Loutakh
ngua
melni
Aminata?
Lane
mo
takk
si
mane
ba
faléwomeu?
Lane
mo
nekk
si
mane
ba
xoloulomeu?
Nieuw
na
sakh
si
séne
keur,
mais
wakhou
lok
mane
Té
métinama
ndeyssane,
métinama
ndeyssane
Pourtant
nitt
la
kome
yaw,
kheuy
neu
beuss
dineu
changé
Pourtant
nitt
la
kome
yaw,
wakh
meu
lane
moy
déranger
Nékal
ak
mane
bilay,
beugueu
leu
Yalla
takh
Hé
eh,
Hé
eh
Thioro
baye
samba,
dak
sa
yay
dieulmeu
Sa
nijaay
yo
may
ma
ay
dollar,
dou
ma
té
daggo
Djank
bi
tchi
kogne
bi
néna
dou
sey
ak
badolo
Bo
démé
keur
yayam
goudi
gossi
lay
réré
Amou
ma
or,
amou
ma
xaliss,
amou
ma
ay
liasse
Né
ngua
do
guéne
ak
mane
ndakh
amou
meu
ay
clash
Loutakh
ngua
melni
Aminata?
Mane
xamouma,
bébé
wakhma
Amou
ma
or,
amou
ma
xaliss,
amou
ma
ay
liasse
Né
ngua
do
guéne
ak
mane
ndakh
amou
meu
class
Loutakh
ngua
melni
Aminata?
Loutakh
ngua
melni
Aminata?
![Iss 814 - Aminata - Single](https://pic.Lyrhub.com/img/r/_/l/s/c8xw2gsl_r.jpg)
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.