Jeeba - Décorée paroles de chanson

paroles de chanson Décorée - Jeeba



Sén ko rek mouy démm (yeah)
Ame caractère ba doko gnimé khol yeh
Mann guiss nala yaw yangui diémm
Beugue menoul sa boppou ba kénn doula togne yeh yeh yeh
Niou gnoy djiguéne djiguéne you meunn goor
Djiguéne djou kharoul daray goor
Djiguéne djouy niafé nguir meunal bopam wawaw
Mann xamna ni diambar nga damalay nianal enh enh
Ki bagne katt la motakh mo deuk ci warwi yeh yeh yeh
Yaw yar nagnoula fignoula waré yarr boubakh
Meusso gnou gathiél béneu yone
Li nga gëm bobou ba légui yangui ci di niafé nguir beugue mou bakh
Motakh rek ma nane
Mann nawna sa yaye boye
Dinako décoré wakh ko dome bimou diour meun na yorou rew
Mann nawna sa Baye boye
(Yaw baye boye)
Wakh ko dome bimou diour meun na yorou rew
Éhé éhé éhé meun na yorr sa rew
Éhé éhé éhé djiguéne meun na yorou rew
Sénn ko rek mouy dem
Bou done béne
Bouniou done niéte
Mann sagn nala bayi ndjabott gui ci keur gui
Dougnou toumou ranké
Dougnou kokh kokhi
Gno gui ci toll yi, gno gui ci bureau yi
Ci ngui ci sport bi akk fo meunti dem
Ma name djiguéne yoyou boléni diakk
Dignité akk diambarté ngay lire séni kanam
Diokhogn nala, Diokhogn nala
Motakh ma bindeu waw wi dolé la ndioukeul
Oubeu nga lambe dji do sénn morom
Oh, oh oho ooooh
Oubeu nga lambe dji djiguéne
Mann nawna sa yaye boye
Dinako décoré wakh ko dome bimou diour meun na yorou rew
Mann nawna sa Baye boye
(Yaw baye boye)
Wakh ko dome bimou diour meun na yorou rew
Éhé éhé éhé meun na yorr sa rew
Éhé éhé éhé djiguéne meun na yorou
...fin



Writer(s): Unknown Unknown, Abdoul Aziz Fall


Jeeba - Décorée
Album Décorée
date de sortie
04-12-2020



Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.