paroles de chanson Xale - Kya Loum
Guiss
na
la
Goune'
(Xale')
Bima
la
niite'
(Xale'
yile')
Guiss
na
la
Goune'
(Sax
thi
xalate
sen
euleuk
noumouy
de'me')
Bima
la
niite'
(Xale'
yile')
Guiss
na
la
Goune'
(Sax
thi
xalate
sen
euleuk
noumouy
de'me')
Bima
la
niite'
(Xale'
yile')
De'
ko
topato
xale'
moy
sa
dome
(Xale'
moy
sa
dome)
De'
ko
topato
xale'
momine
la
(Xale'
moy
sa
momine
la)
Xale'
Bou
gane'
si
Adouna
Soxla
ndeye
ak
bayam
Te'te'
ko
te'
xamal
ko
ki
mou
done
Wadiour
daye
mate
werou
waay
Yaraal
mako
waye'
boulko
door
(Xale'
moy
sa
dome)
Soxla
na
love
de'l
fo
ak
mome
(Xale'
moy
sa
momine
la)
Xale'
bou
ganesi
adouna
Soxla
na
yeurmande
waay
Te'te'
ko
te'
xamal
ko
ki
mou
done
Wadiour
day
mat
se'tou
(Xale'
yile')
Guiss
na
la
Goune'
(Sax
thi
xalate
sen
euleuk
noumouy
de'me')
(Xale')
Bima
la
niite'
(Xale'
yile')
Guiss
na
la
Goune'
(Sax
thi
xalate
sen
euleuk
noumouy
de'me')
Bima
la
niite'
(Xale'
yile')
Huumm
huuum
Xale'y
ndiariniou
re'wame
(Re'wame)
Xaley
eulegui
re'wame
Diangal
ko
xam
xam
Nguir
euleuk
mou
diarigne
re'wame
(Humm
humm)
They
need
a
love
and
a
lot
of
mercy
(Lot
of
mercy)
They
need
attention
Let's
take
care
of
them
(Let's
take
care)
Xale'
meuna
done
Ki
nga
fogoul
won
Ndax
fa
mou
dioudo
Daniou
deuke'
ndol
Waye'
thi
sen
xol
daniou
yag
gueum
Dor
waar
ak
diome
Te'
def
ko
thi
mome
Xale'
meune
na
bax
Xale'
meune
na
bone
Xale'
meune
re'www
Xale'
meune
na
tooy
Kon
loy
def
thi
mome
nang
Ko
tek
thi
yoon
Ndax
lo
Ko
diox
dala
koy
delo
Soxla
na
light
Soxla
love
Soxla
peace
diarna
baayi
xel
Soxla
na
light
Soxla
love
Soxla
peace
diarna
baayi
xel
(Xale'
yile')
Guiss
na
la
Goune'
(Sax
thi
xalate
sen
euleuk
noumouy
de'me')
(Xale')
Bima
la
niite'
(Xale'
yile')
Guiss
na
la
Goune'
(Sax
thi
xalate
sen
euleuk
noumouy
de'me')
Bima
la
niite'
(Xale'
yile')
(Xale'
yile')
(Xale'
yile')
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.