paroles de chanson Fadiar - Omzo Dollar
I
say
Heure
bou
boite
di
teuth
leu
diakka
di
oubbii
Heure
bou
diakka
oubbii
leu
boite
yi
di
teuth
Bi
leundeum
beu
lerr
Beulei
nakk
beuthieuk
beu
goudi
Da
melnii
dei
ak
dioudou
nio
bokk
bountou
bougni
oubbii
Fadiar
Khel
bou
deuggou
ak
khol
bi
mouy
kathial
Golo
ci
garap
leu
deuk
mais
febaram
nite
mokoy
fadial
Yeah,
diaroul
ngueu
meiy
nopp
man
khol
ngueu
meiy
deguei
Sama
call
dimeu
degueloo
gnimeu
sorei
sorelo
gnimeu
djeguei
Sa
thiossane
soko
toppei
do
gnemei
lou
bess
Meuno
nekk
éboueur
beug
yeurei
you
wekh
Dieufou
goor
dh
foumou
fégné
dh
lamine
dou
ci
leen
Lou
goorjiguen
woutei
ak
goor
bou
beuri
djikowou
jigeen
Yeah,
nama
yalla
mousseul
ci
xamxam
bou
amoul
mandoutei
Omzo
deiy
khekh
pour
ceinture
mais
solloul
sakh
toubeuy
Yeah,
gars
yei
meunei
boy
Regarde
le
score
Diay
fruit
di
diokh
nigger
yi
ci
Apple
store
Fajar
LEER
bii
nieuw
(×8)
Nenegn
quand
on
aime
on
ne
compte
pas
Desfois
on
aime
des
gens
pour
qui
on
ne
compte
pas
Douma
diay
star
dameiy
tekk
sama
dieu
ci
surface
terre
bii
Fi
gueuneu
kawei
fimeiy
dem
moy
soufou
tangkou
mère
bii
Yeah,
ragal
yalla
mounoul
nekk
tappet
Boulmeu
nianal
gouddou
fane
nianal
moudjou
bou
rafet
Pour
diouk
ben
yone
danou
deux
fois
de
suite
Le
mensonge
jette
des
fleurs
mais
ne
donne
pas
de
fruit
Montagne
bi
gueuneu
kawei
mouy
metti
souma
warei
danou
Man
loumeiy
gaagn
moy
nimey
guissei
sama
boy
yi
di
gaagnou
Ma
momone
game
bi
depuis
diamono
Jesus
ak
Demba
Mais
beugoumeu
dei
ci
kaw
scène
beu
melni
Papa
Wemba
Safara
dou
feyy
même
boko
deffone
ci
ndokh
J'me
méfie
du
feu
qui
brûle
mais
pas
de
l'eau
qui
dort
Yeah,
gars
yei
meunei
boy
Regarde
le
score
Diay
fruit
di
diokh
nigger
yi
ci
Apple
store
Fadiar
LEER
bii
nieuw
(×8)
Dama
dokhi
outti
leer
bii
Nakh
limeu
yagg
nekk
ci
leundeum
Beug
takk
melni
weer
bii
Mais
meuno
tegui
sama
gueum
gueum
Wone
leine
meu
yone
bii
×2
Yeaaah
yeah
yeah
yeah
yeah
Digueuntei
fimeu
nekk
ak
fimeu
beug
deem
Digueuntei
limeiy
guiss
ak
lignoumeu
beug
wone
Digueuntei
kimeu
nekk
ak
kimeu
beug
done
Oh
yeah
yeah
yeah
yeah
Oh
oh
oh
Kheyneu
nath
bi
gueine
bobou
beu
legui
mangui
khar
fadiar
1 Deugue
2 Hentai
3 Fadiar
4 Lo meu def
5 Lepp legui
6 Agresseur
7 Sante
8 Penda Mbaye
9 Bou dé Dëg la
10 Muerte
11 Dou changer
12 Buur
13 Ndakh Rap
14 Borom
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.