Samba Peuzzi - Marie & Cheikh paroles de chanson

paroles de chanson Marie & Cheikh - Samba Peuzzi



Boumla beugoulone douniou seuy yeah
Boumla noboul wone damlay fowé dem
Boumla beugoul wone douniou seuy
(Ayy details lay bagn loutakh niou deukk di khoulo oh)
Boumla beugoul wone doumla marier
Boulma beugoul wone damlay fowé dem
Boumla beugoul wone douniou seuy
Kaay niou diemko doundou comme Marie
Beug nala beug ngama
Ak Cheikh, Marie
Wolouma
Marie ak Cheikh, Marie
Woulouma
(Kaay niou diem ko doundou comme Marie)
Ak Cheikh, Marie
Wolouma
(Kaay niou diem ko doundou comme Marie)
Ak Cheikh, Marie
Wolouma (kaay niou diem ko doundou comme)
Aliance si lokho (umh umh)
Kone doyoula (yeaaaah)
Chaque jour nga vérifier sama téléphone
Kou beugay fiir (umh umh)
Nangouna (yeaaaah)
Wayeh dangassi bollei togne
Comme bep goor
Parfois ma nèlaw mais
Tay guissna si yaw louma metti yeah
Saga ngama bayiwossi khel grawoul
Khamna sa khola tang
Boul degglou wakhou nitt yi dagnlay misère loo
Laadial gnimay andal yaw laay tiiteuroo
Teh souma nobaatone kénène yakoy ndieukeu yeug eh
Ndakh yaye sama khol (yeaaaah)
Boumla beugoulone douniou seuy yeah
Boumla noboul wone damlay fowé dem
Boumla beugoul wone douniou seuy
(Ayy details lay bagn loutakh niou deukk di khoulo oh)
Boumla beugoul wone doumla marier
Boulma beugoul wone damlay fowé dem
Boumla beugoul wone douniou seuy
Kaay niou diemko doundou comme Marie
Beug nala beug ngama
Ak Cheikh, Marie
Wolouma
Marie ak Cheikh, Marie
Woulouma
(Kaay niou diem ko doundou comme Marie)
Ak Cheikh, Marie
Wolouma
(Kaay niou diem ko doundou comme Marie)
Ak Cheikh, Marie
Wolouma (kaay niou diem ko doundou comme)
Diam reka fi khadj
Pour keur gui nèkh
Sa khel waroul niaaw non non
Même bouma goudeh nieuw
Si loula nèkh rek ladone dokh
Defal comme avant nga tontou maak sourire bou nice
Soumi samay dal laadj ma nouma def
Beuseulma samay tank thiouray di dioli
Khouloo waratouniou non
Bouldi fowéti sama khol
Damla beug teh neubou mako
Yeureuma warounio khouloo oh
Yaw la tane pour nga done sama yayou dom yeaah
Boumla beugoulone douniou seuy yeah
Boumla noboul wone damlay fowé dem
Boumla beugoul wone douniou seuy
(Ayy details lay bagn loutakh niou deukk di khoulo oh)
Boumla beugoul wone doumla marier
Boulma beugoul wone damlay fowé dem
Boumla beugoul wone douniou seuy
Kaay niou diemko doundou comme Marie
Beug nala beug ngama
Ak Cheikh, Marie
Wolouma
Marie ak Cheikh, Marie
Woulouma
(Kaay niou diem ko doundou comme Marie)
Ak Cheikh, Marie
Wolouma
(Kaay niou diem ko doundou comme Marie)
Ak Cheikh, Marie
Wolouma (kaay niou diem ko doundou comme)
Reptyl'Music



Writer(s): Abdoul Aziz Fall, Samba Tine


Samba Peuzzi - Marie & Cheikh - Single
Album Marie & Cheikh - Single
date de sortie
11-05-2019




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.