Souleymane Faye - Il est l'heure paroles de chanson

paroles de chanson Il est l'heure - Souleymane Faye

Mane lima gueneu jaxal si xaley Sénégal moye
Musikou lemzo diamono bi daniouko chœuru par choeur
Mane lima gueneu jaxal si xaley Sénégal moye
Licci télévision bi yeup daniou ko chœuru par chœur
Ta ko ci ne récitelma sa récitation
Bi duleuko meuneu recitel par chœur
Mane lima gueneu jaxal si xaley Sénégal moye
Musikou lemzo diamono bi daniu ko chœuru par chœur
Il est l'heure il est l'heure il est l'heure
Suñu télévision bi dafa am chœur
Il est l'heure il est l'heure il est l'heure
Suñu musik bi dafa am heure
Il est l'heure il est l'heure il est l'heure
Diangui école wala métier dafa am heure
Il est l'heure il est l'heure il est l'heure
Takki diabar dafa am heire
Xalei bi buy diangui école
Dafay fokni ay wajuram laye jangal
Bala muy xamnei boppam laye jangal
Bete bou deimei baye binde lettar
Jangal
Il est l'heure
Nekk xale mettina yaye xamna si dara
Nekk xale mettina yaye xamna si dara
Bul waxli
Bul deffli
Demal fi
Awal fi
Waxal li
Solal li
Simil li
Togal li
Boul lekk li
Nekk xale mettina yaye xamna si dara
Boul deff li
Boul wax li
Solal li
Simmil li
Muñal so magué mou jex
Muñal xalei bi muñal so magué mou jex
Muñal
Lima jaxal si xaley Sénégal moye
Musikou rap bi dañu ko chœuru par chœur
Mane lima gueneu jaxal si goney moye suñu
Télévision bi daniou ko choeuru par chœur
Wayei kocci ne récitelmasa
Récitation bi duleuko meuneu récitel par choeur
Il est l'heure il est l'heure il est l'heure
Jangui école wala métier dafa am heure
Il est l'heure il est l'heure il est l'heure
Iow deimal seyi dafa am heure
Takkil jabar dafa am heure

Souleymane Faye - Guëw
Album Guëw
date de sortie
01-01-2001

Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.