Viviane Chidid - Djoug Liguey paroles de chanson

paroles de chanson Djoug Liguey - Viviane Chidid



Djante fenk na
Ngay nelaw
Djiougueul dème ligueyi
Midi passè na
Ngay nelaw
Djiougueul dème ligueyi
Guinaar gui sapp na
Ngay nelaw
wara ligueyi
Midi passè na
Ngay nelaw
Djiougueul dème ligueyi
Kou niak gneurigne
Niou ame Fay
Guisa gofi bediaw
Khale nga outil kheuy
Demal Dori warr cia bamouy teel molay Fay
Dina mosa bakh
Dina mosa bakh
Boul yakamti darà
Bo diape amoul bayi
Wanelensi foula ak fayda kharel way
Adouna lepp terangala
Logueye lene way
Dina mosa bakh
Dina mosa bakh
Ligueyi lene
Adouna lepp ayy terangala legueyi lene
Khamnane Dina mossa bakh
Ligueyi lene
Ligueyi lene
Ohhhhhh
Djante fenk na
Ngay nelaw
Djiougueul dème ligueyi
Midi passè na
Ngay nelaw
Djiougueul dème ligueyi
Guinaar gui sapp na
Ngay nelaw
wara ligueyi
Midi passè na
Ngay nelaw
Djiougueul dème ligueyi
Kou niak gneurigne
Niou ame Fay
Khaliss binga yorr sa poche mba lew na la
Guisa neh deuk bi dafa beuti agresseur
Te kougnou diap rèendi lideh doyna war
Sathie yakamtina weurseugueume degoma deh
Boko fi kharone dougne la dor banga
Djiougueul Dori warr
Djiougueul dori warr
Lep Dina bakh
Lep Dina bakh
Ligueyi lene
Adouna lepp ayy terangala legueyi lene
Khamnane Dina mosa bakh
Ligueyi lene
Ligueyi lene
Ohhhhhh
Djante fenk na
Ngay nelaw
Djiougueul dème ligueyi
Midi passè na
Ngay nelaw
Djiougueul dème ligueyi
Guinaar gui sapp na
Ngay nelaw
wara ligueyi
Midi passè na
Ngay nelaw
Djiougueul dème ligueyi
Ngay nelaw
Djiougueul dème liguey
Ngay nelaw
Djiougueul dème liguey
Ngay nelaw
Te wara ligueyi
Ngay nelaw
Djiougueul dème liguey



Writer(s): Akatche Bennette, Bakhaw Dioum, Seraphin Koffi, Victoria Catherine Chidid


Viviane Chidid - Benen Level
Album Benen Level
date de sortie
08-02-2020




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.