Viviane Chidid - Rëcc Na paroles de chanson

paroles de chanson Rëcc Na - Viviane Chidid



Par AbouAmg
Deugeu teule rek tothie na teyal
Loufi diar ngendy daw bey danou teyal
Fo tok beugeu gnou nawla teyal
Wagnil eupeule ba netali teyal
Dègueloulene Wakhou yaram ba teyal
Neuneu wakhou kham yone ko geune
Teyal beugeu buzz bamou diarala teyal
Nga taguègo dewagoul
Cou nek amanga Lila daye fekhèl nga dieum ko lindianti dhè
Lila wakh sa galer ngi takk
Di boy dieum ko lindianti
Faye ko dhé li la Wakh
Lou touty nga def ko lou patta
Lo xam netali li la wakh
Yakamti rayone na sa gnaum mame
Deuguena rayone na sa gnaum mame
Boukou lék féké gnorogoul
Boul di Wakh lo khamné amagoul
Xamoulo do Khar bagnou xamala
Guissoulo do Khar ba guiss Lou geuneu lér nga dem
Na nga tey ta nga dale
Amigo Li ngaye Wakh wauroula
Nopi bakhna thi Lo xamoul lanla
Gawa Wakh Meuna indi mussiba
Deugeu teule rek tothie na teyal
Loufi diar ngendy daw bey danou teyal
Fo tok beugeu gnou nawla teyal
Wagnil eupeule ba netali teyal
Dègueloulene Wakhou yaram ba teyal
Neuneu wakhou kham yone ko geune
Teyal beugeu buzz bamou diarala teyal
Nga taguègo dewagoul
Manè li Khawma lanla li khawma lanla li khawma lanla li (bis)
Ki dhè lidjantinala lidjantinala lidjantinala yaw mi (bis)
Lingua bindeu eskeu deugeu leu
Fake news mane yeugeulouma
Beugeu beuz ba takh nga dima sosal
Lingua def Dou xam nga Noumou toudou
Toumale boy yakati nit
Wala sakh boy bindeu thi nit nala lere
Li ngaye Wakh ni lou ame la
Lou ko moy Dina done sa musiba
Deugeu teule rek tothie na teyal
Loufi diar ngendy daw bey danou teyal
Fo tok beugeu gnou nawla teyal
Wagnil eupeule ba netali teyal
Dègueloulene Wakhou yaram ba teyal
Neuneu wakhou kham yone ko geune
Teyal beugeu buzz bamou diarala teyal
Nga taguègo dewagoul
Par AbouAmg




Viviane Chidid - Benen Level
Album Benen Level
date de sortie
08-02-2020




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.