Viviane Chidid - Yaakaar paroles de chanson

paroles de chanson Yaakaar - Viviane Chidid



Waw wawaw wawaw
Lo wax mani waw
Wawaw wawaw
Lo def mani bour
Si sama xol yakoy besse makoy fir
Daga tok ba xadjou goudi
Wot nank dougou sama keur
Fekhe ba ken yegula
Nga sathie sama xol bilé (Wou sathie)
Ya saf sapp ak soukar (gnamal)
Dama am sa febles douma ral (ya mom dipo)
Yamay tagale ak sama sago (dieuleul)
I love you I love you
Waw wawaw wawaw
Lo wax mani waw
Wawaw wawaw
Lo def mani bour
Yag nga miir ci man
Xamna sama doug sama geun
Xamna samay andando
Xamna tamit samay deukeuno
Maître bi leu diangla ayna (taril)
Lo wax dafa nex ba melni lem
Lo def ma guiss ni nonoula
I love you I love you
Waw wawaw wawaw
Lo wax mani waw
Wawaw wawaw
Lo def mani bour
Xaleyi madj len
Melni soldareur général
Si bessu fêtou indépendance (indépendance bi)
Sa mbeuguel may madj lo
Si sa xol rek lay way (ci lay way)
Ya saf sapp ak soukar (gnamal)
Dama am sa febles douma ral (ya mom dipo)
Yamay tagale ak sama sago (dieuleul)
I love you I love you
Waw wawaw wawaw
Lo wax mani waw
Wawaw wawaw
Lo def mani bour
Si sama xol yakoy lal makoy yeug
Uh si sama xol yakoy besse makoy fir
Uh la la la uh la la la uh uh
Ayyy ayyy cuz I love you love you youuuuuuu
He boul daw diarouko nax reuthi nga
Diar ci bilay diar ci goune gui
Nexna nayam nexna bayam
Avocat manousi dara
Procurer manousi dara
Monsieur le juge doula juger
Wouy ya woy wouy sathie lay lay le la



Writer(s): baba hamdy


Viviane Chidid - Yaakaar
Album Yaakaar
date de sortie
26-09-2013




Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.