paroles de chanson Dorido - Xuman
Ndéké
dama
takk
niareile
té
yeugoumako
(Anh
yeugoumako)
Dima
envoyer
message
té
mane
xamoumako
(anh
xamoumako)
Dafma
demander
Ami
rek
ma
ajouter
ko
(anh
ajouter
ko)
Yoné
nama
ay
photom
mais
nak
xoloumako
ANH
loma
tekk?
Wifi
bou
amoul
code
Douma
dox
si
yoyou
mane
taloumako
Mana
yaw
kessé
(guissatouma
keineine)
Wowé
ma
macky
(yaye
sama
maréme)
Opposants
yi
(voteloumaleine)
Fiila
nehh
(fala
beugua
dem)
Anh
kouy
Ami?
kouy
Mami
Ana
guoor
ak
djigueine
nek
amis
Kii
nane
la
honey
Kii
nane
la
dady
Bala
nga
meuna
djoko
rek
goudi
Ohh
baby
my
ladie
Meusso
ma
xamé
yeufou
bandit
Yaye
sama
honey
may
seu
dady
Lila
nehhay
ame
si
keur
gui
(anhan)
Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.