Youssou N'Dour - Djamil paroles de chanson

paroles de chanson Djamil - Youssou N'Dour

Du nil, du nil bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Xamal ma lu leer
Danga maa woolu sa gàll e ma ñëw nga mel ni xale
Yaw daal yaw téppal fële
Danga ba di tappale
Su fekkeeni parewoo waru loo di yónéé
Ngall yaw bul ma defioo lu ma nin ni di xeebe
Létt ma mbaa nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Lég lég sax nga yónni ma
Ma dem bay dem nga teye ma
Léégi sax dematuma
Damay bañ nga dugël ma
Bu fekkeeni parewoo wanu loo di yónéé
Ngall yaw bui ma def loo lu ma nin ñi di xeebe
Létt ma mbaa nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom
Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw
Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom
Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw
Létt ma mbaa nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Boo ma waxee fi nga bêgg dem
Ma wax la fi ngay jaar
Demal bl dem, waxal bul wax, defal bul def
Man daal sonn naa, sonn naa sonn naa
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa ko tay,
Bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë bëgg ak bañ la .. .

Youssou N'Dour - Djamil: Inedits 84-85

Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.