Youssou N'Dour - Gagganti ko - traduction des paroles en russe

Paroles et traduction Youssou N'Dour - Gagganti ko




Ba ñu la koy jox, xam ul dara;
Ба гну Ла кой Джокс, ксам уль дара;
Bu la séen ée, daw gatandu la,
Бу Ла сеен ээ, до гатанду Ла,
Ay waajur ëm, da ñoo am oon yaakaar ci yaw
Ay waajur ãm, da noo am oon yaakaar ci yaw
Jamono y dox, jafejafe am, sëytaane ñëw
Jamono и dox, jafejafe am, sëytaane ñëw
Bu ko dóor, bu ko saaga, bu ko xas, bu ko wax lu ñaaw
Bu ko Door, bu ko saaga, bu ko xas, bu ko wax lu naaw
Delloo l sa xel, ca ginnaaw, te muñ ël ko;
Delloo l sa xel, ca ginnaaw, те Мунь Эл ко;
Ba ñu la koy may, xam ul dara;;
Ба гну Ла кой май, ксам уль дара;;
Bu la séen ée, daw laxasu la,
Бу Ла сеен ээ, до лаксасу Ла,
Ay waajur ëm, da ñoo am oon yaakaar ci yaw
Ay waajur ãm, da noo am oon yaakaar ci yaw
Jamono dox, jafejafe am, sëytaane ñëw
Jamono dox, jafejafe am, sëytaane ñëw
Bu ko dóor, bu ko saaga, bu ko xas, bu ko wax lu ñaaw
Bu ko Door, bu ko saaga, bu ko xas, bu ko wax lu naaw
Delloo l sa xel, ca ginnaaw, bu ko souffrir loo;
Delloo l sa xel, ca ginnaaw, bu ko souffrir Лоо;
Xool al ci ay, waajur ëm, bu ko joy loo
Xool Аль ci ay, waajur ãm, bu ko joy loo
Bu juum ee gagganti ko
Бу юум ээ гагганти ко
Bu juum ee gagganti ko
Бу юум ээ гагганти ко
Bu juum ee gagganti ko
Бу юум ээ гагганти ко
Bu juum ee gagganti ko
Бу юум ээ гагганти ко
Bu ko dòor, bu ko saaga, bu ko xas,
Bu ko dòor, bu ko saaga, bu ko xas,
Bu ko wakh lu ñaaw
Бу ко вах Лу няав
Bu yënggël ée daal, ba sa xol fees, génn ël nga dem
Bu yënggël ée daal, ba sa xol fees, gennæl nga dem
Bu fa toog yaw, di raak ak moom, sàmm al sa cér
Bu fa toog yaw, di raak ak moom, sàmm Аль-СА cér
Woo ko, waxtaan ak moom, muñël ko
Woo ko, waxtaan ak moom, чай munël ko
Bu juum ee gagganti ko
Бу юум ээ гагганти ко
Bu juum ee gagganti ko
Бу юум ээ гагганти ко
Bu juum ee gagganti ko
Бу юум ээ гагганти ко
Bu juum ee gagganti ko
Бу юум ээ гагганти ко
Yaw tam, bul forcer, deel négocier
Yaw tam, bul forcer, deel négocier
Ndaw sii, bul teg deal, bul planifier
Ndaw sii, bul teg deal, bul planifier
Te bu am ee, lu fi leer ul, nga clarifier
Те бу ам ээ, Лу фи Леер уль, Нга кларификатор
Coow li, bu déborder, nga pacifier
Coow li, bu déborder, nga pacifier
Yaw daal, bul forcer, deel négocier
Yaw daal, bul forcer, deel négocier
Ndaw sii, bul teg deal, bul planifier
Ndaw sii, bul teg deal, bul planifier
Te bu am ee, lu fi leer ul, nga clarifier
Те бу ам ээ, Лу фи Леер уль, Нга кларификатор
Coow li, bu déborder, nga pacifier
Coow li, bu déborder, nga pacifier
Wa waaw
Ва-ва-ва
Jaajëf, di na tax, xale wone jom
Jaajëf, di na tax, xale wone jom
Waaw góor, di na tax, xale yokk jom
Waaw góor, di na tax, xale yokk jom
Di ko won sa jom, moo koy dolli jom
Ди ко вон СА Джом, му кой Долли Джом
Jom jom jom rek, dara lu dul jom
Джом Джом Джом РЭК, дара Лу дул Джом
Yërëmal ma ko
Yërëmal ma ko
Momit mou wégal ma laa
Momit mou wégal ma laa
Nax ko neex al ma ko
Nax ko neex аль ма ко
Moomit mu xam ko
Муми му ксам ко






Attention! N'hésitez pas à laisser des commentaires.